ni lagnouy seuyei legui dh
boh waxei rek gnounei mayma batt 😂😂
2026-10-21 22:02:06
27
Mrs ndiaye🥰❤️ :
Diouma nak wakhe degue seuyooo da ngay fooo😂
2026-10-21 22:09:22
48
mame daba diamil :
diouma dafa yabate
2026-10-21 21:37:24
77
AnaTidjane 🥰🥰 :
Barina khalé you seuyé nih deh
2026-10-22 09:16:36
4
Mbaye Seck :
boy you rewww yi khamoul niou seuy beug mariage di rewantou ni ...may ma sama bate on me le répète pas moi .....meuneu na mougne leppp bamou dess cette phrase
2026-10-22 00:17:38
1
Aissatou Dione :
diouma seuye nonoula khoulo ak dioubo😂😂
2026-10-22 08:42:26
2
Mariama Camara :
billahi
2026-10-21 21:13:24
21
Aida Camara :
la suite
2026-10-21 21:41:36
2
Mme Camara :
Diouma mo sof wayè dinako guiss
2026-10-22 09:56:24
0
user5954070010182 :
Merci mame très bien ❤️
2026-10-21 23:16:28
1
Ciça sourire :
Tasssssss lennnnn😂😂😂
2026-10-21 22:24:32
1
fatimata :
diouma seuyo vraiment
2026-10-22 00:24:45
0
marryjeng4 :
Next
2026-10-21 21:38:46
3
Aya Sow :
la suite
2026-10-21 21:44:41
1
Le LAGANDONG 💪🏽 :
Douma vraiment beugo sey danga yabaté way ish
2026-10-21 21:42:23
10
weuzz230gmail.com0 :
Boy yi koula guena mol mola guena doff
souma beugué té yayam beugouma 🤣 Repartir a zéro ak xexx sa foyer dou benn
2026-10-21 21:40:30
6
bocarkane903 :
djiguénnn da mena faté démb
2026-10-22 00:01:09
1
Packo diaz :
diouma dou seykate
2026-10-21 22:15:24
2
serigne sow :
genrou diouma gui nio bari si rewmi takeuleine nak amoul bena sens
2026-10-21 23:45:59
0
moustapha :
diouma dafa rew
2026-10-22 00:26:41
0
Seyni Pouye :
ah (oute khalis dal dara geunou ko) diamono dji ndakh seuyi legui ndiowane leu rek boy balancé wou mouy dagg djiguenen gni kou dem nga takat kenen [Hilare][Hilare][Hilare][Hilare][Hilare]
2026-10-21 23:05:25
0
ADB :
Danga rewwww bi ngay dougou si seuy bi khamone ngani mamam beugoula te bougnou tegue waxi mame ji feuler seuyoooo
2026-10-22 06:52:14
0
Anita faye bu serigne fallou :
2026-10-21 22:38:21
0
To see more videos from user @minatiti4, please go to the Tikwm
homepage.