Mane bayina passtéf bou yague ma ngui si Tahirou sarr
2026-10-23 03:13:32
122
Adamsbody Fall :
pastef la bok mais deug du romb ay nop
2026-10-22 16:51:56
161
Lolo👸 :
Walay visas at carte de sejour mo takh yeneu deuk yi avancé
2026-10-23 00:51:30
98
Saliou nékh jamono. 🇸🇳 :
Billaahi dëgg lay wax tonton taihrou
2026-10-22 14:03:47
107
Ben bassir :
Tahirou sarr moy solition pour Sénégal
2026-10-22 14:47:29
77
xell ak xol :
yallnako yalla fall
2026-10-22 13:41:02
42
soldarou serigne bara :
Tahirou sarr seul 2027 2029
2026-10-22 15:32:52
18
Ndiaye Moha :
politique migratoire pays sérieux dakoy appliqué
2026-10-22 15:02:04
30
user2168779082801 :
tahirou sarr yalna nga am diam bilahi ya beugue Sénégal
2026-10-23 07:22:32
30
Biba_Lyrics :
Limoy deug déh dafa metti ms bly moy deug yalla sax gneup bougouniouko yonenti bi la mm chose donc bouniou refusé tahirou douma mérr deh par ce que deug mo metti