Boul merer nitt ki ba takh ngakoy sosal li khew si rewmi niawna dagne lay tageu tey yass la suba Teh loumasi diakhal ku beugeu beuss attaquer mame ndiaye masuma commentaire si tiktok mais li c’est désolant vraiment 🤔🤔🤔
2026-10-22 20:45:54
33
Mlee Shop by Marianne🛍️ :
C mélanger def lein ko bein bein rk
2026-10-22 20:43:33
46
La gagnante❤️🇸🇳 :
Yena kham dehhh
2026-10-22 20:02:42
57
jus d'orange :
thieuy aduna wahal niit lou bakh baparé weulbati diko hass cela veut dire que daray si sincérité amoussi
2026-10-22 20:43:34
44
gmhc❤️ :
mame s success molene sonal
2026-10-22 21:01:07
1
Thiatou lalaké :
Ay way niaw na dé
2026-10-22 20:14:18
31
Siry G :
Wa tik tok bi noye déf ba bok si lii
2026-10-22 20:36:16
9
Aichou Ba :
Mandou rek😁😁
2026-10-22 19:56:34
28
mamy232 :
ay li yalena diour diam😳😳
2026-10-22 20:52:45
2
Nogzita28🇪🇸🇸🇳 :
Wahhhh lou khew fi🤣
2026-10-22 21:26:27
0
Thiate mbakhé beauty sallon💄 :
Mame ndiaye a vie
2026-10-22 19:14:43
23
Coumbista Thiam :
Chéri loula metti
2026-10-22 20:22:14
23
Tatouch :
Demb ladon hastè gnaww way
2026-10-22 21:00:48
1
Fatou Youm :
bilay tik tok bi and ak saytané
2026-10-22 20:58:11
0
Bb Fa❤️ :
Ayy kharite guéne dh
2026-10-22 20:46:04
1
zeyna❤️💚 :
vrema sounou yone nekousi que le meilleur gagne
2026-10-22 20:37:42
11
🫀 :
Mais fi nexna deh
2026-10-22 21:04:11
11
Canadien Lamso :
😂😂😂wouyyy tik tok Sénégal kagne laye ame diame
2026-10-22 21:00:00
7
diarrasarr Bou lalake chou 😎 :
la team Manou rek
2026-10-22 20:51:08
6
mariza :
Mais star la kay
2026-10-22 20:33:38
7
Queen conductrice 😍🥰 :
maniko niawwww[Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-10-22 20:20:20
7
Maman à vie 🥳✨💪❤️ :
2026-10-22 19:56:44
6
To see more videos from user @tiktokseneg2, please go to the Tikwm
homepage.