oooooh frère mettina trop mais mo nèkh yalla bly borom bakh nga dh❤️
2026-10-22 19:37:31
2
fallpape 0009 :
du courage bro 👊💪liy nieuw moy dakh
2026-10-22 19:32:23
0
Serigne Fallou Oscar ✌🏿🥰✌🏿 :
courage frère yalla na la yalla dolï soutreuh 🤲
2026-10-22 20:29:03
3
Ramatoulaye :
yall nala yalla samou rek
2026-10-22 19:51:02
1
Elhaj__JB5🦂 :
Diamou si ioee wadji 🥰
2026-10-22 19:38:33
2
✪mayoro✪ Bou barça✪ :
Mor yalla nala yalla defale djiamou🥰🥰🥰
2026-10-22 19:52:01
1
ndiaga mboup7🤌🏾🫀🇸🇳 :
Courage frère yalla nala yalla diokh louko gueune 🙏🏿🙏🏿
2026-10-22 19:49:19
1
Cheix ahmadou bamba🇸🇳 :
Courage brohhh lep yalla lay nex❤️☝️
2026-10-22 20:29:38
1
Ndiayemo🇸🇳👷🏼♂️🇲🇷☪️ :
Yalla bakhna 🙏
2026-10-23 06:47:37
0
mOmO the bosss :
yalla rek lay nex té inchalla liye nieuw Moy dakh
2026-10-22 19:44:58
2
Khadim 406 🤙 :
Bly sm wadij Amal diamou rk natou dou ses bly yalla na la yalla défal diamou yaw borom bakh ga bly yaw Dara warou la dal bly sm xarit ga sm way ga bly mor Diamou si yaw bly ko bakh la 🫂😭🙏
2026-10-22 22:31:31
1
assmalick bou serigne sam mbay :
net kou bakh sm wadié diamou rek inchalla liy niew moy dakhe 🥰🥰🥰
2026-10-22 19:35:43
0
Kanté automobile 🚙 :
Bilay métina mes yalla Bakhna 😭
2026-10-22 19:33:17
0
Cheikh bou Talfa ✈️ :
2026-10-23 08:56:11
0
GOUDA TALIBE BOROM TOUBA ❤️🙏 :
mor li da gan si yaw barkè borom touba yalla na yalla deff diam rk sama wadji
2026-10-22 20:37:54
0
astou niang :
2026-10-23 07:54:15
0
MBAYE 78AYA :
Yalla bkhna
2026-10-23 10:03:14
0
AMZO BOU 307 TARKINDA BI :
mor bilay dîna bakh lou yalla déf dafa ngen ✌️
2026-10-23 09:11:13
0
Assane :
2026-10-23 09:49:18
0
Prince 🤴 Samb 💓💓 :
Courage frère yalna la yalla diokh louka gene 🙏🙏🙏
2026-10-23 07:55:20
0
Aliou Araujo4🇺🇾🦍 :
Bon courage rek frère yalla bakhna 💔😭
2026-10-23 09:08:34
0
To see more videos from user @morloum307, please go to the Tikwm
homepage.