Maman dafa digne,am personnalité, am bamélou biirr,Mandou,am soutoureu, kham niitt🥰🥰Maman seule
2026-10-22 21:02:21
172
borome🇸🇳porokhane♥️Fadilat♥️ :
kan mane mi taloumaléne
2026-10-22 20:28:46
86
Haby Ndiaye :
maman de bayi lèn ko vraiment
2026-10-22 20:30:09
369
Khadija barhame👸🏾🇫🇷🇸🇳 :
Et may niou diam maman dafa nek si dethe geunelen ko si wakh dji
2026-10-22 20:23:32
118
Arame Sall :
maman yonam nèkoul ci wakhe dji dh
2026-10-22 20:45:21
75
🥰🥰🥰 :
maman nak bayré bi safna kou wakh rk toude la svp bayilen souniou maman nak xoulo len rk ter bayiniou
2026-10-22 20:55:35
45
Justine Louise :
Mani guene Yabii suniou Patron 🤞Lalaké Seul ❤️
2026-10-22 21:00:52
33
diabarouchaaba :
Guenel mama si wakh dji
2026-10-22 20:55:34
109
DEBS BODDY :
thiey senegal
2026-10-22 22:31:25
1
salikhate2.0 :
guénné lén si maman dh
2026-10-22 20:28:28
42
DIOP🐍🔱 :
Am li tee Genesi maman
2026-10-22 22:10:24
60
Maya 2em du nom :
Mani wakhléne maman Diatta deugue koula bayi nga bayiko lalaye topé mame Ndiaye mane dé douma beugue sama morome jiguéne bamou diarale ma sama boope niite daye gueume bopame
2026-10-22 21:18:30
2
gnagna 💋Mrs Barry💍 :
May lénne ko diam
2026-10-22 19:40:12
37
diarrasarr Bou lalake chou 😎 :
dosi guené patronne tmt wala
2026-10-22 20:55:15
92
Bènita mou Serigne- fallou❤️ :
2026-10-22 20:03:09
30
dada_fashion_shop1👗👠👜🛍️ :
Maman kay ame na dara da yarou rk té nguén guéné niou thi séne wakh
2026-10-22 21:29:53
41
Fatima_Saliou_❤️🫶🛍️ :
Hum wakhal ta bayi maman guéné ko si wakh dji Svp talou niou béne wakh na lérr
2026-10-22 20:53:36
23
ladivamouserignesali :
Walooooooo Wa kawwwww sonou naniou si yène 😭😭
2026-10-22 19:46:39
47
Mariem 6 ❤️💙 🇸🇳 :
Mo tey 😂😂😂Mam seul
2026-10-22 19:41:00
26
To see more videos from user @topcassurcas, please go to the Tikwm
homepage.