Kader Kara Dh Nilako Firei Wone: « Waxlo Naniou Yonente Bi Mou Waxla…Mom Nit Rek La Rek La Yalla Bour Bi Ken La Kou Yakar Dadiei Yeurmandém Day Selal Ay Dieufam Té Boum Ko Woutal Dieum Ndakh Mom Ken La »
2026-10-22 22:36:41
57
demba kara🇬🇼🇸🇳 :
Bala niou ko kham cey modou Usman 😭
2026-10-23 09:25:25
38
~fallou fall~🤩 :
Wax leen Man nit rekk laa ni yéen waaye Yalla xamal na ma né Yalla kenn rekk la Ku beug dajeek Yalla na dieuf dieuf yu baax te bul jaamu keneen kudul Yalla
2026-10-22 21:46:13
89
Ouzcomedien11 :
❤️❤️Thieye wayyyyy Djii jah kara
2026-10-22 22:16:08
21
I B R A 🔴⚫️ :
Dis : « Je ne suis qu’un être humain comme vous ; il m’a été révélé que votre Dieu n’est qu’un Dieu unique. Celui qui espère rencontrer son Seigneur doit accomplir une bonne œuvre et ne doit associer personne dans l’adoration de son Seigneur. » (11) Sourate Al-Kahf kenn du Jaa Karaa ❤️
2026-10-22 22:26:28
16
🤑dim nd💫💫 :
2026-10-22 22:36:21
7
حصن الأ برار الهـداة :
Mogui soratou kahfi
2026-10-22 21:08:09
16
Baye Fall Civilizé :
jërejefety cheikh ahmadou kara mbacké noreyni
2026-10-22 21:44:31
13
AdawaTou noreyni :
قل إنمآ بشر مثلكم يوحى إلي أنمآ إلهكم إله واحد فمن كان يرجو لقآء ربه فليعمل عملا صالحا ولا يشرك بعبادة ربّه أحدا .١١) سورة الكهف