@senegal_dabord_presse: #sathies #azizndiaye #😭😭😭 #pourtoulemonde #tiktokviral

Senegal_dabord_sn🇸🇳
Senegal_dabord_sn🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 23 October 2026 00:07:40 GMT
339434
49555
1061
522

Music

Download

Comments

bobobennacer
Bobo JR :
Aziz dafa beugeu siteu dane balla dane après niou teug. Revanche : Balla vs Siteu pour balla récupéré couronne biii. Mais insha allah sa thies dina am ndam însha Allah
2026-10-23 02:57:20
407
reumlh44
REUM LH44 🫡 :
Ligui siteu nak Esque dafa niow ?
2026-10-23 09:02:20
217
milano4603
Milano :
Victoire mo gueun khaliss
2026-10-23 00:39:20
1109
guigodiop
guigodiop :
Sa thies weroul dh
2026-10-23 00:33:27
340
baye.niass195
BÉN ABDALLAH 🏋🏾🚴 :
Sa thies kén douko sacrifie
2026-10-23 05:41:25
55
immo1221
Ahmadou Immo💸 :
Wa mais sa thies tmt da sokhla combat bi diaroul guén koy forcé tmt , nieuwoul daag len ko té bayi wax dji …. Bou daano yen yeupa koy setan
2026-10-23 00:55:58
224
mamisagna255
Talibé cheikh :
Sa Thiès zero professionnalisme
2026-10-23 04:07:11
140
mamebassmbaye1
Al Bassir élément s Rafahi💔😂 :
Sa thies seul boulen ko diakhase ak sénégalai yi
2026-10-23 08:55:44
252
user4445563960205
abdou mbaye :
🥰🥰🥰🥰 yalna sa dime yague
2026-10-23 08:35:26
97
babsv.i.pcouture0
'babs v.i.p✂️😎 couture ✂️😎 :
Mane Lou takh awma vocal lii nekh na deé 😂😂😂
2026-10-24 00:52:39
0
iboutissu
ibou décotéx :
inchallah ndam rék
2026-10-23 00:57:02
221
izye95
user7960012561837 :
sa thies louko arrangé la dëff
2026-10-23 08:53:25
31
sega.metal
sega metal :
Monoul wakh ndeyssane
2026-10-23 16:36:16
0
cheikh_377
Cheikh Fall :
Bii dou yoyou boy ❤️🥳🥳
2026-10-23 01:00:54
139
mfall013
M_FALL•👑🇸🇳 :
Samay niounn Daniouy lamb
2026-10-23 02:10:34
32
khaliloulah829
Khaliloulah⚽️❤️ :
Li diaroul bruit wayy dagu ko rek mou diekh gnoune Roi bi 10ans lagne si beugu
2026-10-23 14:40:15
9
elhadjiterangadieng0
Elhadji Téranga432 :
Mon taye
2026-10-23 01:11:21
32
seydinaibnuibrahim
عثمان بن ابراهيم✅🇸🇳🛫 :
aziz nak bayilen boy bi MEM kimou wara barel niowoul tmt dou sama mbeur mai maylen ko diam tmt aussi
2026-10-23 12:07:44
15
mame.saliou.gnral
mame saliou Général 💙🖤 :
Maye lène nitt yi diamou sa thies dane na niew sène face face mais sou niewoul kaye khaye na biss bi moko lathie ❤️
2026-10-23 02:24:39
40
parc_des_princes2026
PARC DES PRINCES :
Modou lo moy sama Mbeur na leer : sa thies nekal sissay entraînement boul tontou dh ki dama guiss daf la beug todial quoi .! Tout ça pour pa biy letou dieulatt roi bi ?
2026-10-23 09:35:10
28
ndiaboutadiouf
ndiabouta diouf :
aziz li diaroul way fi mais ou est balla gaye tamit genal proteger sa rakk mom mongui proteger rakam man dee douma nangou li
2026-10-23 07:25:03
43
meeazy3
Time is Money . :
Gars yi yenei wougn sa thies Roi bi Bilakhi
2026-10-23 07:11:58
23
astaniagdiadine
astaniangdiadine :
sa Thiès kham nalén
2026-10-23 11:44:40
9
mbaye.thiam19
Mbaye Thiam :
Mais léguii Siteu lane moko téré nieuw🤷‍♀️🤷‍♀️🤷‍♀️
2026-10-23 09:49:55
49
To see more videos from user @senegal_dabord_presse, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About