Bb ioe diguah guèneu guediawaye mba combat bi passé nioune dagniy lamb 😂😂❤️
2026-10-23 10:48:24
569
𝑺𝓐𝙽𝗚𝒪𝐌ᴀℝ✰ :
Sa titine mingi nieuw🥳😂
2026-10-23 12:56:35
511
Esprit positif 👑 :
Lamb fi la wara tolou op a faire de bandit 🥰
2026-10-23 06:51:55
1192
el capo :
Sa tee-shirt Dina gneuw
2026-10-23 07:30:55
283
PABLO NDAKAROU🤴🏿 :
Bougne ko bayé ak sagom Rk NDAKAROU lah faral 😅
2026-10-23 03:09:34
474
Ndiago Ada fasS 🇬🇼🇸🇳✝️ :
Jumelle baguii nonou ❤️🎉
2026-10-23 14:49:08
154
Mister T🌟OBY🔰🩸👑 :
kharitou khalè yii 😋🎉🩸
2026-10-23 09:45:44
84
Fatoucha :
Mane ak khalé bi nion yameu dhé 😭😭
2026-10-23 10:24:12
69
cheikh Bou ada fass ✌️ :
ndakarou bi seul
2026-10-23 03:20:49
137
Little_Rock221sn🇸🇳 :
Nieup môme laniouye topou
2026-10-23 03:45:55
65
Soukadeug❤️🥇🤴🏽 :
Thieuy Ndakarou ❤️☺️
2026-10-23 03:22:53
34
JOÃO PEDRO ✌🇧🇷 :
mome seule bilaye
2026-10-23 08:08:23
31
aliou bou s aliou :
lolou kaye lerna😂😂😂
2026-10-23 06:44:09
46
malaw bou dégagé 12 :
Ndakarou 😂
2026-10-23 09:31:52
28
ALIOU 🇸🇳🥤🍼😌 :
Ada Ada Ada Leuhh Baséne bire Keur yi🩸🚀🙌😂
2026-10-23 08:26:46
82
Dija Kenza :
boulenko forcé kénén mom ada rek lay topou
2026-10-23 08:16:02
57
••SY••⚡️📈 :
Boulko forcer
2026-10-24 16:19:05
5
𝐟𝐚𝐦𝐚 𝐃 👸🏽🤍 :
Sa titine mougui nieuw 💃
2026-10-23 13:50:51
22
🅰️DA Ndakarou🇸🇳🤞11 :
Chérie ada mbayang seul 🥳😍❤️
2026-10-23 09:00:07
15
Maya Ibr@him ♥️ :
Ndeyssane khalei dagno beugu Ada fass mane sama dôme bi bimouy wakh Ada fass moy mbeureum bobou mogui sogua meune wakh Lo wakh mouni la Ada fass bilay 😍 sou gorgorlo touti rek dîna am Lou bari si lamb dji khalei yi kougnou beugu rek y’a quelque chose
2026-10-23 10:25:06
22
Mouhamad Rassoul Sarr❤️🇸🇳✌🏿 :
Na guene keur gui ba combat bi passé 😂
2026-10-23 12:09:13
11
Ada fass BOU SAFENE DG boy yii :
ww mome seul
2026-10-23 07:50:20
9
fallou Galass ✌️ :
Billay ada la fararr ❤️♥️
2026-10-23 07:35:07
11
alia :
borom ndakarou la farale mo nek si khol🙏
2026-10-23 08:19:49
10
To see more videos from user @ndiago969, please go to the Tikwm
homepage.