Ba ici repose li douma ko gueume diodio dou deff lou niaw
2026-10-23 15:16:16
20
Arame saliou❤️🔐 :
Mom nkoul Sénégal dh wayei moyou gueneu kham cas senegal
2026-10-23 14:02:47
97
soso❤️sokna❤️ 🇸🇳⭐️⭐️🇸🇳🥰 :
Non vraiment bayilennn diambour
2026-10-23 14:03:05
41
Najma 🇸🇳🇲🇷🇬🇲🇨🇻 :
Ndeysane Diodio dafa sensible li dakoy sakh traumatiser
2026-10-23 15:46:45
1
Une Soninké05 :
Bilay Diodio xadioul si yeine yi elle est tellement douce et gentille Yalla nako yalla taxawou mou guaw delou si ndiabotame akk ligueyame dakhe bokk na si loutakhe xalé nieup ame diome beugue amale sein bopp
2026-10-23 14:15:58
54
darkQueen💘 :
deysane diodio elle est tellement sensible yalna am diam waay
2026-10-23 13:52:35
61
Mouna🇸🇳🇲🇷🥳 :
Alhamdoulillah
2026-10-23 13:27:35
60
bnl :
Mane dei li la geum
2026-10-23 13:45:10
32
Parfumerie Al-Mahdi ❤🌹ﷺ🌹❤ :
Alhamndoulillah
2026-10-23 13:35:26
72
Ãlalou saliou :
Li dai la wah mane
2026-10-23 13:34:04
36
Mme thiaw sarr :
amine yarrabi 😭🙏
2026-10-23 13:44:43
17
To see more videos from user @dakarmusique.com, please go to the Tikwm
homepage.