Nga wakh alahuma ikhfirlaho warhamho bu feke góor la
bu Féké jigéen la nga wakh alahuma ikhfirlaha warhamha mu diekh
yàlla yalla na ngo ko yërëm té jéggal ba paré mbolo yërmànde la
2026-10-24 22:46:42
10
MHD☆◇☆□ :
NB:
nan la niouy dioullé néw 4 kabar la 1ère kabar nga diangue 1 fatiha
2ème kabar nga dioulli si yonnénte bi amna bouñ si tamou nk wayé boko manoul rk man nga déf julli bo man bou la nékhé nga déf bi (اللهم صل على سيدنا محمد وسلم)
3ème kabar nga amna ñian bouñi diangue wayé boko manoul man nga déf bi bou dé gorr leu(اللهم اغفر له وارحمه) bou déh djiguén (اللهم اغفر لها وارحمها)
4 kabar nga ñianal ko ñianl bolém jullit après nga seulmeul[Prière]