Oumy fi ken amoul Diot nieupay liguey delen wakh ak sen assistante yi soy diay dangay nekh deret même si les retours ne sont pas bonne faut accepter avec le sourire
2026-10-24 18:10:15
3608
Fatou Hamid :
Franchement ya togne nakh bo demer ba bagn details livrer ko barquette yapp waro wone retourner wat si live bi Di wakh lolou c’est pas du tout cohérent boudé Danguay lathier wakh deug nekh yalla yako togn lolou koko wakh mou guiss si boppam
2026-10-24 18:57:03
258
M🦋🌬️ :
Guiss gen maturité oumy bi 😭♥️la vraie classe🫱🏿🫲🏾
2026-10-24 19:27:07
71
Salihate281023 :
Tay si tay mola togne dafla beug yakhal
2026-10-24 18:17:08
442
Gueye M-C 🇸🇳🇨🇮 :
daga dioum oumy waro togg ak say assistante nan kham na da beugue loumou ndeké lolou moko nakhari vraiment 🥰❤️
2026-10-24 19:41:22
52
Thiarra coach bio 778114193 :
Man Gniy khoulo si commentaires yi la meunoul comprendre batayy 😂😂
2026-10-24 18:45:59
375
Bya :
Vraiment yalla reck mo takh maye wakh dieune na si iaw paela manila doma wagnil livraison bi Bilakhi mounima ok diokhel 1500 dinala tegual 500 nite kou bakh guan en plus aye plat wame machalla 🙏🙏
2026-10-24 18:12:37
977
My :
Khalise awmako ben
2026-10-24 21:09:26
0
zouzou🇸🇳🩷🙏 :
dioum na mé pr mane yaw temit dioum ngu waro togg ak say xallé yi di wakh kham na da beugu loum ndeké dengu ko done kagno lolou moko nékhoul ptetr ❤️
2026-10-24 18:21:11
300
maitre Noah92i :
Tu t’exprimes juste pour ta communauté, nous qui ne comprenons pas ta langue mais qui te suivons, comment feront nous pour piger ?
2026-10-24 17:55:47
218
saliou :
🥰🥰
2026-10-24 17:53:45
112
𝒀𝑨𝒀𝑶𝑼 𝑩𝑨𝒀𝑨𝑴🤎 :
Machallah elle communique bien🥰
2026-10-24 17:58:40
442
763846273 :
continuel di déf sa ligéuye ndakh liguaye diaye sét na nékh na
2026-10-24 17:57:27
129
Princesse :
Je confirme que tu n’est pas sur les détails ta nite kou dale gua tassé wone nagn salon Princess Hair un jour femme bi dila dieuw dila def ay affaire gua kham lepp nopi calme avec une douceur ta liguay diay aussi tout est bien livrer guama un jour thiébou diaga damani sama Tite sœur bi oumy mi est ce que werna tellement dieune bi dafa beuri damani ki est ce que dîna guene si limouy diay ta khamoma khamou mala bou deglou kene continue sur cette lancé patt ak organiser ma chérie
2026-10-24 17:51:09
1055
amina187 :
Waw tay si tay balko aduna amoul solo
2026-10-24 18:11:14
206
marieaugustinendi4 :
liguey Sénégal yomboul, courage
2026-10-24 18:47:58
490
aidi-aida :
Tay si tay oumy ya meilleur
2026-10-24 18:10:20
62
Dikha :
Il y a des gens de mauvaise foi rek
2026-10-24 17:59:07
86
ngayén bi😍 :
Tay si tay moy l’an ma cheiri
2026-10-24 18:13:06
253
Gfatoush🇸🇳 :
Oumy beugueu naleu trop mais linga expliquer ni yaa togne d’après linga wakh binguène decidé livrer ko viande d’accord na coupé linga wakh si live bi moko metti teu waroula live nga né kone mano wakh c entre vous nitt yi gnongui sètane la concernée mongui sètane sa wakh bobou mo andi mou wakhé akk ioe nonou à la fin dougueul vidéo bi aussi nitt kessé leuh peut être dafa guiss ni danguène ko rabaissé et ça se comprend boul dougg ci détails yi woo ko nga wakh akk mome ioe yaay diaay nguène khol nolène ko reglé mangui diègalou nakkk
2026-10-24 19:59:14
38
Beug maodo ak sonko :
Mangui lay khol rék ba dégouma ligay wakh esk do défat vidéo stp
2026-10-24 18:36:23
93
Dewardh :
Vous êtes une femme admirable, et courageuse ✨👏
2026-10-24 17:52:59
89
To see more videos from user @oumyleya, please go to the Tikwm
homepage.