@lyna.467: partie 1 khalé dagnkoy yarr thi ndapp#viraltiktok #creatorsearchinsights #senegalaise_tik_tok #fyp #fy

mini drama
mini drama
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 25 October 2026 00:20:55 GMT
515666
72791
1159
1258

Music

Download

Comments

ousmane.balde282
Ousmane Balde :
genre yi coudou bop reck
2026-10-25 12:08:28
1568
zahra221__
Zahra🇸🇳🇬🇲 :
Mane dh souma fataliko sama rakou papeuh yii nougn niou dàne trokhalé si bolou agn mane ak samay rakk Bly souniou lalé digg bol bii koudou laniouy dieul dorr ko sougn lokho yii pour nakaral sama yaye alors que sama papeuh moy dem liguey diende yapp pour ndiabotam mes sama yaye bouko togué kene d’où niémé lale dig bole bii daniouy lekk ba diouk sama yaye dagg diokh niou ,niou yakarnè sama yaye laniouy nakaral Ndysann t xamougn ni dagn ko diapalé mou yarr niou niongui nii fougn dem dougn rouss’lo sama yaye d’ailleurs bâ ni niémé wougn dig bole mes niom niongui nii sene dome yii nonou laniou réwé si bole t kéne d’où wakh bou guane amé si keur gui niou rouss lo lène khalè bougn souré sakh daniouy yakk ay maguoum diem xamougn lekk bou sett bouniou léké dessalle la doko lekk anamou Tay ? Nioune niouniou done trokhal si bole pour nakaral sama yaye Tay niolène guëna xam comment mangé bou guane togué sokhor baxoul
2026-10-25 13:57:05
204
famambergane1
Mrs wane almamy❤️💍 :
Boumala kheutè daguay dè
2026-10-25 10:24:57
1419
jus.dorange.press
Jus d’orange pressé ❤️ :
Bilay ame na khaléyi you méll ni tokk si ndapp li nane yay mayma yapou yarr léne séne dôme yi
2026-10-25 10:12:55
3356
adjaadja708
adji mareme sow🇸🇳🇸🇳🇸🇳 :
bilay amna khalé you melni🤣🤣🤣
2026-10-25 10:41:31
435
fatourassoul4
Fatou Rassoul 🙏 :
Soumala kholé rk diga kham limala wakh
2026-10-25 11:59:48
314
feuzbvby
Yessal gui évents 🏵️🎄 :
Khalè bouy wax yaye mayma yapp meune na dague sama khol bi😂😂😂
2026-10-25 15:47:32
85
user448713391
Calypso :
il faut bien éduquer les enfants .
2026-10-25 04:55:05
598
1saeerj
🤫 :
li amna khale ak ay mak youko mel deh waya mosiba rek lalendi dioral
2026-10-25 07:20:25
98
mrs_sdd91
Mrs_diène :
Ay boko défone sunu keur, dagay deg ay tonnerre, ndekete dagne la kheuteu
2026-10-26 11:01:16
14
mamy.skin
mamy skin :
mane dai khamna kou mel nii😂😂
2026-10-25 09:39:51
168
bbyasmina74
✰ᵇᵇ 𝒴𝒜𝒮ℳℐ𝒩ℰ🪭 🎀 ✰ :
Sama yaye nena bima néké khalé fouma dem khew yenou yakh ba mais legui Alhamdoulillah yar naniema 🤦🏼‍♀️🥹🧎‍♀️‍➡️
2026-10-25 10:40:27
347
bintaexpressgp
@BintaExpressGP :
Amna souniou keur deh mais bouko wakhè rk ma dopat ko si souf mou khouli beutt yi yaye dji wakhou ko dara louko nekh lay def
2026-10-26 08:00:23
22
moisolo22
Maycha :
Ak model lam bou yagg
2026-10-25 15:56:34
38
yaayu_baayam_loo
༺🌸𝕭𝖎𝖓𝖙𝖚 𝕬𝖉𝖆𝖒𝖆🌸༻ :
Genrou khalé yii rek nioo mana guenné sama xol bi 😂
2026-10-25 23:24:05
20
foipuissance12
Foi et Puissance 🌙 :
Li d khalei bi deuk sunu keur sikaw ni lay déf papam ak yayam diko Setane kom limouy déf Lou bakh ka
2026-10-25 17:49:50
20
fatuchic4
FATÛ🛍️ :
Bokna ben haler Ndap ma bayiko bamou wane ndawal li bamou dieh mou beug diouguer maniko dettt na thiep bi dieh do diougu
2026-10-25 13:46:59
34
user3858018309587
Amintajollo :
2222222222222222222
2026-10-26 13:25:31
0
bb.sarr13
Bbei sarr 😻 :
Souma la kheuté digua dh 😩li rk la bagne 💔
2026-10-25 19:32:03
9
fatou.sene017
Fatou Sene🥹❤️💎💍 :
Gerou khalé yi rek la bagne 😒😒😒😒😒
2026-10-25 13:37:06
11
lilsiss12
T’or🥥🐆 :
Lii sma khol bi layy dagg
2026-10-25 15:26:00
6
absamountakha
absamountakha :
Khalei moy doni makk ✅
2026-10-25 11:11:20
16
.diop.khadijatou.r
DIOP KHADIJATOU RASSOUL :
c'est malheureux
2026-10-25 07:00:56
13
fatou.ndiaye4480
Fatou Ndiaye :
222222
2026-10-25 10:57:21
5
its.mee9596
💖 :
Khalé bi né souniou keur d moy tegal ay yayam ak badienam ndawal sama khol bi dey diex bilahi so waxé bayil li nguey déf doula falé t yayam dey melni guissoul limouy déf après damay rouss ma bako nonou t 5ans le am walahi azim
2026-10-25 17:32:58
6
To see more videos from user @lyna.467, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About