@dalouroxakmame0:

Wa forokh seur béééé te niaK d
Wa forokh seur béééé te niaK d
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 25 October 2026 10:24:17 GMT
68065
6248
526
1436

Music

Download

Comments

fashion_victim23
Lady D prestige :
Aka ma bayi kheil si loumou wakhone
2026-10-25 12:11:19
339
lerekjuly2
Xamguen fimay wakhé SN🇸🇳 :
kone 20millions yi pour ripass la 😂
2026-10-25 12:21:25
146
marichou5366
Marichou tall :
Ki mako beugue té dawoumasi dara
2026-10-25 13:10:21
280
mamandiaw058
Maman diaw :
Yalla Aka bakh si mpotoum mbour
2026-10-26 19:40:44
0
beugmamesaliou00
beugmamesaliou00 :
Ki yallah mokay aral bopam dh inchallah
2026-10-25 12:36:03
127
sokhnafatou76
Ndeye Fatou :
Man mom déjà heur bou tiow dan am rek diodio dougal maison pour kokali masoumaka diox confiance
2026-10-25 18:06:17
56
mamoush1308mame
mamoush1308 :
Maman na niane bouniou messeu diapp Awoush
2026-10-25 16:31:50
61
afiya_be
AFIYA🌱 :
Cas bi barina aye rebondissements
2026-10-25 13:18:02
126
ndayachic
NDAYA Chic :
Hunnnnnn le temps est le meilleur juge 👩‍⚖️
2026-10-25 12:58:29
183
sabdoubodian
bb amina :
ki limouy expliquer c'est logique dhé humm yalla bahneu
2026-10-25 14:34:54
124
anonymat262
Bambara Mina rassoul 😎 :
Yalla kassei lagn togué si tiktok bi mame ndiaye yalla na yalla doli samal la bopam 🙏🏾🙏🏾🙏🏾
2026-10-25 13:03:23
79
lobe.faye29
Lobe Faye :
Xolam mo raféte yalla moy até gni guisagougnou dara
2026-10-25 13:58:54
57
yayou.moustapha3
Yayou Moustapha :
Kou yalla sampe kéne menouko sempi
2026-10-25 12:35:20
85
mamindiaye254
mamindiaye254 :
a vrai dire c'est mame Ndiaye qui dérange yalla nako yalla samb🙏🙏🙏
2026-10-25 13:05:40
280
yarame_diop1
Mme Diagne 🥰😍💍 :
Mimi wakhone nako
2026-10-25 13:26:39
62
mdmfayetoutcourt
Mdm Faye Tout Court :
thiourki diam aythiaaa lou way kham nako tekk si table bi 😂😂😂😂😂 l'internationale à Vie ❤️
2026-10-25 14:36:10
118
2emedunom7
Deuxième du nom💍❤️ :
Ndeysane octobre daw nit yi khekh ko souy live kene dou niew niouy dem si yenene live yi mou mounie rek continuer di rayanter. Yalla dina atter d
2026-10-25 15:03:39
104
nooraaaaa58
Piment doux :
C’est pas les marabouts c’est Dieu
2026-10-25 14:53:00
64
elisabethdiedhiou
Elisabethdiedhiou :
Li laniouye wakh bo woré réne déwéne mou djigue la da fek daniou la ka djigne🥺😳
2026-10-25 16:40:52
55
aissatoudiop4866
aissatoudiop4866 :
Tout ça à un sens maintenant
2026-10-25 12:14:44
85
thioro.diaw5
Lady🖇️geuye❤️🫶😍 :
Video bi ba legui mogui sama téléphone yalla samal niou mame 🙏
2026-10-25 12:15:21
67
user4755278226156
user4755278226156 :
Bilahi bi li guéné kéne geumeukou wone Taye dinaniou comprendre lou beuri
2026-10-25 14:51:13
69
dogobeautybymmediop
dogobeautybymmediop :
wa leigui d’après limmm expliquer yeupp ana audio d’enregistrement yi diomi na
2026-10-25 20:23:55
22
afiya_be
AFIYA🌱 :
2026 bi loumouniou déssél?
2026-10-25 13:19:08
94
fatou.seck4510
fatou seck ❤️❤️❤️❤️ :
Bayi lene khel bou bakhe limouye wakhe 🥺🥺🥺
2026-10-25 14:30:13
55
To see more videos from user @dalouroxakmame0, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About