Ndaysane je me rappelle bi dama dieukeur dima takk marchand ambulant la wone en plus mou deug deukk bou sori sama copine yi dima wakhtané dîna gniawal nanma deug ba lay seuyi limaçon dioy ma ande Goor bou goré mou tak ma dima fayal ma diangue yalla boubico mou ame place walahi même pas 2ans de mariage mou tabakh Dakar keur ba fi may wakh ak yene moussoula seuyi deuk ba migui voyager partout obilma boutique dizundalma auto actuellement Magui si 13ans de mariage si lolou maco nagoul lama fonké batay walahi alkhamdoulilah Mbeuguél mo ame solo le reste day gneuw après
2026-10-26 18:58:29
51
ya salam :
akay deug yaye boye
2026-10-25 19:32:42
71
Diagne-_-Nar44 bou sidy👑🎤👑 :
machalla mé dougnela déguelou dakh adado you bonne rk
2026-10-26 12:10:20
17
user4835277627951 :
deugue pirr kay
2026-10-25 20:46:23
15
Rokhaya Ngom :
mo takh damay ndieng rek waye douma danou mouk ndakh def té yalla takh
2026-10-26 09:14:19
14
Mame Kébé :
Merci tata[Cœur rouge][Cœur rouge]
2026-10-26 08:24:44
3
KHADIJA BADOU 💍❤️ :
Li deh la wakh man diama geun allal dh
2026-10-26 09:44:02
3
MØɄⱧ₳₥ɆĐ_₵ssé_Fx 🦅 🇸🇳 :
Ay li nekhena 😂
2026-10-26 11:56:43
4
THIAM :
walay deugue lah [Innocent]
2026-10-25 23:40:29
8
Fatou Ndiaye :
billay
2026-10-25 18:15:48
14
Khadija 🥰🥰🥰🥰🥰 :
Bilay
2026-10-25 19:16:19
6
Yayou Hamza ❤️💍🌹🥰 :
I’m
2026-10-26 11:57:45
2
maida :
Merci beaucoup
2026-10-26 00:11:50
2
kholou magueye sall à vie❤️🤞 :
Wawaw
2026-10-26 03:33:31
2
Thiate :
Je
2026-10-26 00:47:10
4
r.diagne1 :
Vraiment
2026-10-25 19:38:33
3
Nafina l’animatrice noble 🇺🇸 :
Vrema 🤷♀️🧏♀️
2026-10-26 06:08:59
2
Bousso Bali :
Bilahi
2026-10-25 22:06:50
2
fatel ka❤️ :
Vraiment
2026-10-26 13:01:47
1
Sokhna Dramé :
billahi dh ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️
2026-10-26 10:22:01
2
Mame bousso Saw :
@wawaw🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
2026-10-25 19:35:26
2
rema niang :
tiey yalla
2026-10-25 22:24:10
2
Soce bou serigne fallou :
Ak ay deugu
2026-10-25 21:57:20
2
Mari Thioune :
Bilaye de
2026-10-26 21:06:07
0
To see more videos from user @yayou_bayaam, please go to the Tikwm
homepage.