@jambaarstv: #Adjudantchefoumardiao #servicedhygiene #brigadedepartementaledhygienedekeurmassar #keurmassar #senegalaise_tik_tok

JAMBAAR TV
JAMBAAR TV
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 25 October 2026 14:35:37 GMT
160679
5878
150
993

Music

Download

Comments

mercienvironnement
MERCI :
khana senegal nieup nio nara deim brigade
2026-10-25 20:48:18
0
mbayendiaye282
Mbaye Ndiaye4877 :
li ngenn wara lidieunti lidianti wolenn ko toujours des futilités
2026-10-25 18:21:01
144
user4172599012421
user4172599012421 :
#free kaylor #
2026-10-25 19:53:46
0
serignecheikhmbac79
Cheikh mbacké gainde fatma :
Lolou mom dra nekousi vraiment lolou kouy tabakh diarnasi
2026-10-25 19:42:34
15
maissacasba
maissa casba99🇸🇳 :
Free kaylor laniou wakh
2026-10-25 20:49:31
0
modou.fall7387
Modou fall :
Mais xana loi bi dou senegal gueppu lanioukoye applique?
2026-10-25 19:28:44
22
nittoudeug468
nittoudeug468 :
Ligeyolen dara mako wakh senegal mom nirek lay dokhe
2026-10-25 18:15:48
34
shou.kane
shou kane76 :
S’il vous plaît venez à tivaoune peul beaucoup des maisons leurs tuyaux des toilettes sont dehors
2026-10-25 19:59:04
5
amadousow1077
Charly Sow :
nioune sounou problème dou gravats
2026-10-25 18:51:52
6
paco87782
Paco :
Borom vélo yi servir pain Ak guinnen yi togou sene boutique yi mom Gen wara lidianti te bayi ouvrier yi
2026-10-25 19:09:06
14
k_tech_dessinate.btp
K-Tech Dessinate BTP :
grand mercii à la service national d'hygiène vous fait une travail remarquable 🥰🥰🥰
2026-10-25 18:30:35
5
galsenmyside
Sénégal my YITÉ :
Vraiment il est temps que les gens changent il faut continuer le travail 🙏
2026-10-25 20:36:48
2
moustaphafall5004
Moustapha Fall :
défoléne fi dara lingéne wara ligéye ligéyo léneko
2026-10-25 20:54:36
2
abdougadiaga61
Lamp Fall Peinture :
mais Dépot de grava dafa baax ci fou am ndox mouy taa
2026-10-25 20:45:58
1
tahabtp1
TAHA-BTP-ELC :
Pour moi sa na pas de chance vu que l'état na mi de route pavé ni enrobé ou mm des caniveaux si la loi veut sanction il n'a qu'à mettre les moyens
2026-10-25 21:02:42
1
khaliltidiane13
khaliltidiane :
Service d’hygiène xawma Loumouy lidianti si garava
2026-10-25 20:13:22
2
ndiayehdjdkkdj0
ndiaye :
dou nguéne wakh diomaye mou lebalma khalisssss
2026-10-25 20:08:40
3
babacarofficiel2
Mbaye Babacar🇸🇳 :
nieuw len thiaroy ngur yalla
2026-10-25 19:58:20
2
user3638575234663
600000000000099999999999999999 :
gniy diaye si trottoire yi nak
2026-10-25 19:05:27
4
user86770887
Bamba :
Pourquoi procédure ? Il faut les verbaliser parceque senegal gnissi Bari khamouniou séne droit... Déjà gniga beug yobou amouniou béne diplôme de qualification..
2026-10-25 20:37:18
1
facolygateau11
facolygateau11 :
Senegal yeupp gravât la ´ xana Kone Borom Charette y guene wara diapp en 1er
2026-10-25 18:37:46
3
amarasop55178
Sopou nabi :
Nion dh gravat motakh niou am yon bouniou mana diar si nevet
2026-10-25 18:44:38
3
amadou.diene4
Amadou Diene :
lek bouniouy diaye n importe comment si deuk guén wara khékh
2026-10-25 19:08:52
2
mmizoow
Mmizoow0 :
legui khana jissolen borom charette yi
2026-10-25 19:21:29
1
tamsirdia106
tamsir dia :
Pain yigniy def si sac ak vélo yi koy yobou. services d'hygiène Sénégal 0000
2026-10-25 19:28:27
1
To see more videos from user @jambaarstv, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About