khale bou touti di saga aymaak gua fokne Yasin né maman dé yeureume Nala ya amato crédibilité dakh ya fi wakhone eumb té weusino ba tey con lo wakhati dou deug
2026-10-25 18:14:02
1
Mr Fall friperie :
Thiaga apr
2026-10-25 16:27:25
0
mareme mou cheikhna aidra :
li ba diahal moye adji mome ya nek si deuk loye daw[Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-10-25 16:09:03
0
mor diop :
khana wa kiray niogi diar yaw da ngua torokh
2026-10-25 15:36:02
1
77986 :
waa yow amnga doom walla amagoo doom
2026-10-25 15:58:32
1
ouzou :
Wa pastef li kolenkou wakhone guine wedi kou li bodon complot ba ligue kone Adji Sarr dotol wakhe😂😂
2026-10-25 19:37:22
0
Gp Dém Dik :
2026-10-25 15:43:36
0
حسبنا الله ونعم الوكيل :
yaw mom amo foula
2026-10-25 15:18:34
0
Dior Samb324 :
dagua ame dome yagna dé
2026-10-25 18:06:17
0
K S :
😂😂😂
2026-10-25 19:26:28
0
abou sow :
yaw kou niak diomegua
2026-10-25 15:24:59
5
user8572331179569 :
yow mayniou diame khéwigua
2026-10-25 18:03:12
0
Om'art :
thiouthie fi thiouthie fé
dem gauche wadia dem droite délouwate gauche lolou Moy wakhi khalé bi
2026-10-25 19:39:45
0
mariama Ndione :
Alahira Dina méti lol khaliss diaroul dara Da ngeye dé bayi la fi
2026-10-25 18:21:06
0
WUROBARA~STORE📱🎧 :
mangui dagnéku 😂😂😂
2026-10-25 17:53:16
0
cheikhoumarhanneo :
2026-10-25 16:05:08
0
To see more videos from user @thiam_teranga_officiel, please go to the Tikwm
homepage.