Dama bayante ba rousss th souma kheuye topat paaa bi 😩
2026-10-26 15:55:01
371
mya baby 🥰 :
mane sama copin bi Moy andi problème Moy dem Moy nieuw je suis plus mâture que lui doumako falé môme day fay rek si gorr🤣🤣
2026-10-26 17:53:44
356
sone 🔱 :
bouniou khouloo wee ngani niar gnii c'est fini[Larmes de joie]
2026-10-26 17:49:23
63
Marie Ndiaye :
mane mi di wakh so amé khathie sen keur toudé mako nak 🤣
2026-10-26 13:52:35
253
yass :
aytha aytha aytha aytha ♥️❤️♥️❤️♥️❤️
2026-10-26 19:58:00
0
BB Eva la capricieuse♥️🥰 :
Bilay gno bayanté bama bloqué watshap gnou mou niew tiktok néma bloqué ma fi aussi ma khasss ko néko sa khasaway Waw ko louma nekh bloqué gno dioubo wate ni😂😂😂😂
2026-10-26 15:36:42
199
Medoune Kebe567 :
Dou yam fofou dina wakh « khana yakamti woon nga ma wakh lolou »
2026-10-26 17:44:25
32
Ndeye Saliou ❤️ :
Ay rap la 😂
2026-10-26 12:07:19
86
Lady 💍❤️niang🌸🦋 :
Samay informations kan mokoy dioh ki
2026-10-26 15:18:04
188
mame diarra kane :
lidé mako mome déh lila ko done wakh 🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣🤣
2026-10-26 15:31:48
13
MamoushNdiaye🦋❤️ :
Sama djiko😂
2026-10-26 19:31:59
15
Yayoubayam😍💃🏻 :
Moi j’ai supprimé tous ses photos 12 h à 23 h ma dem supprimer récemment récupérer ko 😆
2026-10-26 20:50:42
5
Maaaa :
Man dh sama boss khol bi da bonn bo paré dina la adiou 2semaines
2026-10-26 20:29:39
5
Khalil seydina ibrahim Shakur :
😂😂bloquer l boparé nane iow beugoma soma beugone dinxma wo gni dagno nexx
2026-10-26 17:20:11
7
amin.aah 💕🐆 :
😭🤣sama rapp bi momayyy wakh looo
2026-10-26 17:36:24
9
_𝒞ℴ𝓊𝓂𝒷𝒶𝒶𝒶🖤🕷️ :
Pourquoi Coumba Ndiaye tmt 🤣🤣🤣💔
2026-10-26 17:16:39
5
Ndeye saynabou :
Guiss nasi sama bopou dh [Larmes de joie][Gros LOL]
[Hilare][Hilare][Hilare]ma bayanté teksi nako boul ma dieulsi souba soumay dem université la nuit était très longue pour moi wayé souma khalaté dieul bus ak trajet bi[Larmes de joie]teksi nara tardé heure d'examen bi
6h du matin ma mayeko coucou[Gros LOL]mounéma li lane maneko clavier bi leu mounéma amon diomeu sa rap lébou bi defna pose prépare toi bb ma gnew dieulsila sa keur ma yoboula université mbeuguel lou nekh
2026-10-26 18:03:35
5
To see more videos from user @larry_roger_gqr_1992, please go to the Tikwm
homepage.