@ibrahima.dieng2622: dahira Mounawirou Soudour Touba geuendel 2 rufisque photo yi rafétna lool téh amna solo lool barkep borome Touba yalla na ligeuy bi nanguou nguen tassé si ak ngeureumeul Serigne bi barkep khassida yi barkep cheikh hamzatou mbacké mom cheikh sonhaïbou mom kou tédd ki