On a l’habitude de rien atte bou bess bi sou naré niaw na melni année bi passé ms 2026 do deugue lolu deh inchallah meti na yague na trop de souffrance de déceptions de prison…..yalla naniou yalla samb are niou
2026-10-27 15:04:09
6
nabissa :
2026 na diekh rek si diam att bi dafa méti trop
2026-10-27 12:45:41
12
NKN✌️😇 :
Mane deh mbana lay diry
2026-10-27 10:07:47
18
Aldiana❤️ :
Diiri tchine b kenn douma si djittou 2026 b brki Alhourane doumako meusseu fatei louma meusseu nakari rk si att b la xéwei😂
2026-10-27 12:16:51
8
Lô ma sire :
2026 bi douma ko meussa fatte 😭
2026-10-27 23:27:27
1
Mami diamant :
Bilahii metina dila febarone yalla nafi yame
2026-10-27 10:38:02
7
🦋AÏCHA✨Rassoul🎀 :
😂😂
2026-10-27 01:08:28
5
Éva😜🥰😜 :
2026metina baparè yague 😏
2026-10-27 22:06:15
0
Diija :
Bilahi lou metti na ken meussouko dound 😂mais alkhamdoulilah mom aduna nio and
2026-10-27 20:40:08
3
Belle Allure Shop👗👚🧢 :
Te fi ak 31 decembre rebondissement bou nk meune na amate[En larmes][En larmes][Cœur brisé][Cœur brisé]
2026-10-27 11:30:28
1
🧸miss~ameenah🥀🦋🫧 :
bly yow lolou sakh laniou wara deff li kéneu khamoul loumou done waay🤧non aux pétales😂👏🏻🎉
2026-10-27 21:28:20
2
Lady Diarry 💍❤️ :
Hiii metina trop😒
2026-10-27 09:28:23
4
maguette Bou sonko :
bilahi Merci
2026-10-27 12:00:28
1
To see more videos from user @unnabien, please go to the Tikwm
homepage.