modou ngom yalla nako Yalla takhawou silougaw amiin
2026-10-27 10:01:57
95
sanian :
yalla nako yalla guenethi natou bimou neck
2026-10-27 22:53:42
0
Nogayesyllabassirou :
yalla nako yalla takhawou thie barkéb serigne touba
2026-10-27 23:52:05
0
Gnilane Juff :
Ay Ya Rabi taxawoul sa diam bi😭😭😭
2026-10-27 22:49:52
15
jojo0345 :
yalnako yalla doli takhawou 🙏🙏🙏yalla guéneko si situation yi inchalla
2026-10-28 00:09:05
1
Mm diarra Sylla :
yalla Nala yalla takhawou barkep Mohamed psl 😭
2026-10-27 22:05:33
10
Soukaye cissé :
yala nako yala téguil natou bi
2026-10-27 12:47:33
18
BICHE FRAGRANCES DUBAÏ🇦🇪🇦🇪 :
Ndeysann MODOU NGOM yalnako sougnou BOROM YA KARIM téguil natou té oyofal ko lépeu si barké YONÉNETIBI SALAHOU ALEYHI WASSALAM 🤲🤲🤲🤲 trop triste way
2026-10-27 14:40:12
11
ZEYNA :
yalla na ko yalla taxawou wayyy
2026-10-27 20:36:34
2
mairamembodj :
yala na ko yala takhawou défale ko sutura mousel ko mouthiele ko rethiel ko téguile ko natou bi môme mi sunou papa modou ngom thii barcké séydina mouhamad
2026-10-27 11:23:54
18
Fatou❤️🩹💍@Diou_f❤️❤️❤️💍💍 :
yalnako yalla takhaou sy barcké naby
2026-10-27 10:01:30
11
deguene sope naby :
yalanako yalla guéne
2026-10-27 14:02:36
10
Sokhna Saliou :
Ay mbacke balla. Lepp louma la massa gnan may nga mako cheikh saliou mbacke magui lay gnan papa modou ngom bu takhawe le 29 yalla nako ylla takhawou
2026-10-27 21:45:39
7
sonko seul :
yalna ko yalla takhawou si barké seyedina mouhaméd psl ndéyssane yalla ameu nako meneu ko yalna ko yalla dolél
2026-10-27 11:33:45
10
Abdou Karim Gueye :
2026-10-27 15:56:38
7
l'enfant de Saloum 👊 :
yalla na ko yalla teguill antou bi
2026-10-27 10:28:53
8
adja :
yalla bakhna
2026-10-27 09:38:14
6
Linguere Faye :
2026-10-27 07:18:59
10
Demba Ndao :
🥰🥰❤️❤️
2026-10-27 09:46:45
7
dial diouf :
2026-10-27 19:52:39
2
abdoulahatfall Ridwan44 :
2026-10-27 15:15:43
3
gassama climatiseur Touba :
2026-10-27 16:35:00
2
Coumba Sene :
2026-10-27 22:24:31
1
thiorongom57 :
2026-10-27 23:08:26
1
Diatta Bacary :
yalla nako def si barke sallahou Allah mouhamad rek
2026-10-27 22:24:21
3
To see more videos from user @bonvoyagesn, please go to the Tikwm
homepage.