loy gueune di magueu rek problème yi di gueune di bari
2026-10-27 14:43:25
124
Sophie Tall :
ammin yarabi inchallah
2026-10-27 23:53:25
0
2x champion d’afrique⭐️⭐️ :
adouna mo wara touki niep nopalou
2026-10-27 14:44:58
57
Bambasene🇸🇳🇪🇸🇫🇷 :
surtout wa barça semaine bi 😂😂😂
2026-10-27 11:34:47
46
Mbodji🇸🇳 :
Fa inna mahal usri yusra
2026-10-27 11:09:45
94
Prince :
Mane dhé li nék sama khol bi guemouma dina diékh bilahi sonou na trop 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-10-27 11:29:24
25
sonko :
Allhamdoulila yalla ☝️
2026-10-27 21:32:35
0
khayastore R 🇸🇳🇦🇪 :
Inchalla yalla bakhna
2026-10-27 21:10:48
0
Apple User443749 :
ak fabar yi. barina yalla na yalla defal niep diam🙏
2026-10-27 11:10:01
28
Mery✨ :
Je pense que yalla daffa nekk di natt suniou gueum la vie est devenue morose kenn bégoul c’est très dure mais nagn andak yalla rek lepp dina baxx inchallah
2026-10-27 15:39:59
19
LayeBusnes+(🛵🐔📡🚘🏠🇸🇳) :
Yalla na adouna touki nieup dém🥺
2026-10-27 23:28:23
0
bébé fama :
man stréssé la menoul j sais pas et pourtant j'ai des problème mais damakoy faté skh😂