@minilalakechou: ##viraltiktok

Mini😮‍💨lalaké🫰🏿Chou🤪
Mini😮‍💨lalaké🫰🏿Chou🤪
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 27 October 2026 13:49:18 GMT
69161
5046
63
36

Music

Download

Comments

gaga.fresh
Baby Freshh :
Radinerie mbao ga wara yobou mame walo gnou pikire ko dakh mou nelaw nopalou @Maman Vulgaire ✈️🛍️
2026-10-27 14:41:33
6
diankha66
🥰🥰🥰 :
borom émission bi tamite dou professionnel amna lo hamni diaroul tekk partie dakar warone dague wala mou lathie Mame walo bapare dorr ko tekk
2026-10-27 16:02:14
21
tyma_stor
Tyma Store :
mais da waron wo borom emission mou dagg yen parties yi vraiment g de la peine pour elle da wara nopalou
2026-10-27 13:53:35
161
221mawa15
ℳ𝒶𝓌𝒶𝒶🫦🌸🪭 :
En tout cas journaliste bi elle a été toujours professionnelle hawma louka dall tay
2026-10-27 16:07:44
22
user6923825919834
user6923825919834 :
Surtout ça Ndeyssanne
2026-10-27 14:34:15
37
mamesene154
mamesene433 :
ndeyssane yalla nako diapalé 🙏🙏🙏
2026-10-27 15:35:42
12
userba1213
La 🌹 :
Dépression la mom yeugoul sakh né dou nelaw ya Allah dolil ko soutoureu Amine
2026-10-27 14:12:33
117
renettemendy
la Linguére 🧜🏿‍♀️ :
yalla bakhna 💗♥️
2026-10-27 20:07:05
0
user319417913
🌄Loyauté🌄 :
Mame walo ndeysan Gör leu Bou xamoul dra émission bimou démone mo doul fou Gör wara dém dakh môme elle ne triche pas Moko yobé lii yeupp
2026-10-27 17:49:20
1
oumy2901
Oumy❤️🥰 :
Ay vue diarouko emission lay waronn supprimé
2026-10-27 21:43:10
0
globalservices18
GLOBAL SERVICES :
nakh lene ko yobou ko hôpital gnou piqûre ko mou nelaw, nane garap appétit lekk peut être kel ira mieux
2026-10-27 21:03:18
0
boutaw53
Madame diop ❤️🥰 :
Mooo😳😳😳😳dama rouss
2026-10-27 15:37:46
0
khadija.niang49
Khadija Niang :
Ndeysann
2026-10-27 14:45:12
13
fatou.ndiaye.diall
Fat Sylla Ndiaye :
merci beaucoup maman
2026-10-27 19:06:04
1
nabajambaye
NABAJAMBAYE :
Yalnako yalla Takhawou 🙏🏻🙏🏻 Metina lol
2026-10-27 17:50:20
0
ada.fall.mm..l
ada Bada 💍❤️🔐 :
Merci
2026-10-27 16:32:48
1
khoudia.diagne905
Khoudia Diagne :
2026-10-27 15:49:11
0
mbayangmbaye653
Mbayang Mbaye :
2026-10-27 18:24:26
0
mamanjtm78
mamanjtm78 :
Dou nelaw ki dembe ma nelaw ba yewou ay 4h ma dougu tictook guisko si live pape mbaye ay 4h 5h lima djeuk wax moy ki esk dey nelaw
2026-10-27 14:24:42
31
jumeta.thioune
yayoufadal :
Mame Coumba aussi meunone nakko dague vraiment
2026-10-27 15:29:25
18
fatoul.business
FATOUL Business :
senegalais gno khamoul depression elle ne va pas du tout bien mou guiss psychologue la journaliste aussi meunone na dague partie yoyou et si etre avec son mari peut la soulager nagne ko bayi mou delou ay way courage mes amours
2026-10-27 16:05:42
7
sakho200508
Banabana100% :
Tay 6h du matin ladone live
2026-10-27 15:10:54
8
user7730713508467
penda dp nd :
kokou ko invité mounone na dague yéneyi
2026-10-27 15:37:34
8
complexserignbabacarr
Tawi yayam :
Dafa am depression Ndeysaan
2026-10-27 15:12:14
6
delmar0891
Delmar :
yobouleen ko si psychologue. elle en a besoin. bala mouy febar. metite bi neek si khol bi moko dominé t mokoy wakhlo, téré ko nelew t comme amoul koumou wakhal mou diap ko si life bi. il faut l'aider
2026-10-27 17:46:47
2
To see more videos from user @minilalakechou, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About