Artiste meunouloko diokh lou gueuneu reuy visibilité té en klk semaine diokh nga boy yi visibilité bo kham né meunone nagnou job ay année té dougnou ko am
2026-10-27 21:44:12
12
mouhamed.1212 :
Non ngi danio soff Babel moy kane naniou may nit gni diamou way
2026-10-27 20:23:24
6
MGS PHOTOGRAPHIE📸✌️ :
Dagno bakh rq meil ni babel dfa gueneh am talent buur
2026-10-27 22:11:19
2
TONTON VITO🇸🇳🇨🇦❤️ :
Babacar wokhal lo geumm koula wokhal loula arranger gua kham koula poser question boula arranger woul gua bloquer tèh pourtant daniouy wakh si yaw positif di participer sisay affaire nittou Deug dou mèl nigua mèl Babacar awma rappeur si versus bi nak