CHEIKHE AHMADOU KARA MBACKÉ NOREYNI MOY BOROM DIAMANO BY
2026-10-28 12:38:08
0
Élément S Saliou :
bilahi nama yalla bal wayé ndaw Touba legui si généralisé wouma dee wayé gnarigne amalougnou ko kou tedd ki doussi ayy tegui doussi melokane doussi dokhal deuk bi nikl Serigne bi beugué 🥺🥺
2026-10-27 20:20:40
368
Mané Mboup :
boyou touba yi déh légui serigne tou laniou tale
2026-10-28 08:23:00
41
Cheikh darou🖤❤️👌🏾 :
Bilay ya nakharé kham cénéralou bamba
2026-10-27 20:46:22
193
Moussa BOYE :
Dieureudieuffé CHIEKHE AHMADOU KARA MBACKE NOREYNI LA SOLUTION DE TOUTES CHOSE
2026-10-27 19:44:47
79
mam fallou mbacke diop :
boy Touba yi nio wara yegua tou bilaye
2026-10-27 19:39:03
92
amdymbeungue 🇸🇳❤️🩹🥰 :
Ndysane
2026-10-28 21:15:45
0
user9575164171500 :
wa touba kay diakhal nagnouma🤣🤣
2026-10-27 21:30:46
40
alfarooQKARA🦁 :
Wallahi dou kéne té kéne dou MOME AHMAD IBN OUSMANE 🫶🫶🫶
2026-10-27 20:03:02
30
talibé serigne Touba :
💚💚💚💚💚 Machallah
2026-10-28 11:01:25
11
Kheweul Shop🏪🧕🏾 :
Xamouniou ko deh wallahi yalla nako Serigne bi fayy yalla nafi yague tei weer Balla at ndam🤲🏾🩷
2026-10-28 14:43:21
5
Pdg jadid Kara business 💃🏻 :
Mbacke sa borom dieureudieuf
2026-10-27 20:25:43
14
dame :
mandé rousna😭😭
2026-10-28 12:34:45
5
SokhnaFatyNoreynii313 :
Dieuredieuf 🥰🥳
2026-10-27 21:31:45
41
Mamadou_Aliou_221 :
Li moy door la té lokhom doula door😂
2026-10-28 01:12:38
11
Soxna mai Kara bakh❤️ :
Ki yalla moko bakhal 😭❤️😭
2026-10-28 10:59:50
6
bara kara GÉNÉRAL Bi 🥰✊🏽 :
2026-10-28 11:02:38
8
seydinakara0 :
Kendou cheikh ahmadou Kara Mbacké Noreyni
2026-10-27 23:14:47
6
bourou_macka🤴 :
ndawi deuk bi rek mane nanio défar deuk bi bilahi sou kene kousi nek bolo wone défar sa kogne fepp day diar yone
2026-10-27 21:32:14
27
mouahmed_gaye_touba221 :
S Modou kara diambar deugla
2026-10-27 22:04:19
10
KALAMOU KARA :
JAH KARA REK 👌👌👌
2026-10-27 18:16:22
18
Mass migrante🇸🇳🇦🇷🇬🇧 :
wa touba dh gnou beuri tok rek nane serigne bi da wara da wara da wara rek la gnoy def parfoi da ngay rous sakh dieuredieuf serigne modou kara wa wa keuram yi
2026-10-28 09:03:36
8
Dane Fall shop Louga :
Touba d’abord
2026-10-27 20:47:56
10
ALY BAMBA KARA 313 🇸🇳 :
la générosité
2026-10-27 20:34:53
6
L’infatigable serviteur :
Touba Mbacke dh nioune daw gni bouniou fokon 1000f Touba ça kanam chak mois rek bala 5 ans deuk bi dokh
2026-10-27 19:55:03
18
To see more videos from user @fadel_kara_officiel, please go to the Tikwm
homepage.