@uneprincesse199: #CapCut #creatorsearchinsights #viral_video no sama yaye mo dakk si Sénégal

Chalou Cha_sn 🇸🇳 🌸🚨💃🏽
Chalou Cha_sn 🇸🇳 🌸🚨💃🏽
Open In TikTok:
Region: SN
Tuesday 27 October 2026 17:54:58 GMT
307456
38390
896
1070

Music

Download

Comments

kallssoum97
ÜMÜ kallssoum 🇸🇳 :
Sama yay mom sama papa dako beurgeul seuyoul
2026-10-28 09:07:58
2824
cheikh.sene758
Cheikh Sene :
sama yaye magual touba ba tay terre si would dakar
2026-10-28 11:26:03
861
ajafatim7
Ajafatim :
Kon mère yeup même problème laniou am?😂
2026-10-28 09:34:09
1115
oumyfallilou0
Oumy fallilou🥰 :
Kharal ma nopi sama yaye comme pigeon voyageur😂
2026-10-28 10:23:03
356
unelebouuu4
A.🤍 :
Sama yaye mom nenako seeuyoooo
2026-10-28 11:21:24
239
une7373
uNe🇸🇳 :
sm yaye mo eup liberté th yoroul ay tank you bakh heure Bou nieuwé febar
2026-10-28 13:42:34
69
mariemeniang906
Mareme🌺✨ :
Sma yaye dassiy bolé bayii téléphone bii si keur gui kénn douka woo sougnou waxé mouné keur gui daguay stressé 😂
2026-10-28 08:24:11
695
kyasaliou95
kyaSaliou95 :
Sougn thiatt keur néna sama Yay sou maytou woul Dina fekkk bagagam keur papam dakoy guenei keur gui 😂😂😂😂😂
2026-10-28 12:52:45
119
fatoumatasan49
Fatoumata🥰🇸🇳 :
Mane mome dama yakarni Mane laniou takk 💔sama keur yaye
2026-10-28 13:04:03
193
xolou_dieukereum
Mrs_Diop😍💍❤️ :
Wa ioe tamit nak nak nak li lanla sii beauté manchalla laf thiat tu es tres belle
2026-10-28 09:21:03
445
bineta2452
user9573150124887 :
Bouy dem danane damay changer dji air 😂
2026-10-28 22:30:30
0
nianianiang
Nia7.0 :
Ma mère qui ne va jamais nul part nak mom sougn ko yeugaler hew sakh damay wakh ba sonn pour mou dem
2026-10-28 09:06:51
462
ali.diouf7
Mr Diouf Pape Aly #5 🇸🇳🇩🇪 :
ndeysaan Li dafa neex longévité à toute mamans merci Sister
2026-10-28 10:18:53
238
coumbasy134
Une 221🇸🇳❤️ :
Ma niowate nétaliléne un jour sama famille yaye ame mariage rk mère bii léttou deff hénne 🤣🤣sama pape naneko bayil adunah mague gua legui 😆😆😆rk mère biii beugue khar soufsiii bah nane kooo 56ans rk lah sama deukendo yiii yépeuh nioma mague🤣🤣🤣
2026-10-28 19:49:05
9
miss.linkthiate
𝐌𝐈𝐒𝐒ˡⁱⁿᵏ𝐏𝐑𝐈𝐍𝐂𝐄𝐒𝐒𝐄 :
kharale la partagé ko sama yaye pour mou meuna tog sonou nagn😂😂dem rek 😂
2026-10-27 21:39:25
108
daara_fathoul_wahab
Daara fathoul wahab :
2026-10-28 16:26:21
16
omargueye6682
Omar Gueye6682 :
et toi wakh ak iow sur ta beauté 👍👍
2026-10-27 21:24:45
47
thiate1234556677
mbene :
bayil mére bi dafa streesé 😂😂😂
2026-10-28 11:21:08
19
bb.dieyna.oficielle
Diéyna Rassoul ❤️🇸🇳 :
sama yaye laniou tak wayé Mane may seuyy domame yii yeupeu maléneu dii gérér ménage bissii keur guii yeupeu makoy déff nékk taw bou djiguéneu métina😭💔😂😂😂😂😂😂😂
2026-10-28 16:06:41
9
unelolita
🌸UneFaty🇸🇳🌸 :
avant hier lani sama yaye " yaw del tambambalou si deuk bi rek" 😂😂😂😂, khawma louy séne problème ak déme
2026-10-28 10:23:39
25
user216079223
thiouthia :
Sama yaye la 😂😂😂
2026-10-28 14:32:45
9
zeynab955555
Zeynab Store🛍️🛍️ :
Sama yaye nilaye def 😅😅
2026-10-27 21:12:31
36
aziz65670
Abou ba :
150mille ndaw na [Larmes de joie]
2026-10-27 21:21:00
45
binetafatimasow
Bineta Fatima Sow :
Deysane ce c k j disait à ma mère yaye voyage rekk mouni ma damay dem si sama au mbok paix à son âme
2026-10-28 13:15:03
12
sophie_sd1
Sophie👩🏽‍🍳🌸D❤️💍 :
Mane miy wakh sama yaye na faye deim beine 3mois 😂😂
2026-10-28 11:36:21
17
To see more videos from user @uneprincesse199, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About