@kine_zo: Kou beugue ken douko conseiller😂 #senegal #humour

kine_zo
kine_zo
Open In TikTok:
Region: FR
Tuesday 27 October 2026 20:08:10 GMT
118372
26805
377
928

Music

Download

Comments

sokhna_arame
𝒮𝒪𝒦ℋ𝒩𝒜 𝒜ℛ𝒜ℳℰ ℒ𝒪̂ 💕 :
Mala si meuna wakh dara sma makk bou gorr mo dioté ak guélam ma guadou khoulo bo déme supprimer numéro guel bi mou kheuy indiko si keur 😭🤣
2026-10-27 20:14:01
1528
baally.shop
Baally Bousso 🌸❤️😘 :
Dotouma dalati sm adouna😩😭🤣🤣🤣
2026-10-27 21:48:37
29
salaboubayekarim
Sala bou baye Karim Mbacké :
Sama yaye def nama ko ma yanou khekh ba dem diangui wathi fek ko mouy waxtane ak kimou done xoulol motax legui bouy wax fi souba douma si dougou sama guathia bobou yalla boumou amati 😂
2026-10-27 21:13:12
83
dija3365
KhAdIjA R@SsOuL🇸🇳🇫🇷 :
Moh mako df sama zine bi khoulo ak far bi mou gniew dimako expliqué mo wo farr ba khass ko bamouy Mel ni khasoum khay😂😂 2 jour après sama zine bi ajouté ma si sén appelle name ma man ak sama goor gui sounou andeu bi kouko nara yakeu yalla gua déh ma Mel ni kou planqué jour bobou la mandou si couple diambour yi batay
2026-10-27 21:02:10
155
princessfalilou7
Miss Falilou💗🧕 :
limasi méti moy après dioubo bi nioune laniouy déff seuytané yii 😭💔
2026-10-27 20:44:00
469
fatoubydiorfashion
FATOU👩BY~DIOR❤️FASHION🛍️🛒 :
Guisgua kenzo dama khame lolu ba legui dama deme marche diend sama mandou Lou Matt Sekk legui douma conseilller kenn nak 😂
2026-10-27 20:15:32
298
user7698725066639
user7698725066639 :
Sama xarite bi moma mentionner dafa torokh 😔😭pann lasi wakh dama sakh rouss
2026-10-28 00:04:07
0
arame4262
🫶💞🥰 :
ba paré nane béne deumou khadioul souniou diguanté wa légui kouy deumou bi mane l
2026-10-27 20:15:04
85
banemina
Amina B-k barhamenne🫶🏽 :
Mann lay Wakhal dèe wayè changes na
2026-10-27 23:55:46
0
salihate.business.by.ac
salihate.business .by.ac :
Walla souma yalla beugué nama bayé ak yaw😂
2026-10-27 20:37:46
16
princessebk5
👸🏽KHADIJA 🌸🧸 :
Di faralaté wo Farou diambour saguako bamou toy lolou doyoul ma yoné ko ay vocal saguati ko bamou toy ni kou djiguene ki bayiko il était 2h du matin ma yewou 9h guiss kou djiguene ki statut ko nane l’homme de ma vie goumin bi mako moudié gadou
2026-10-27 21:42:06
15
adj5800
ADJA_collections🌸🛍️ :
Kou dougou sama khoulo souma dioubo wee fenallll laaaa😩
2026-10-27 22:53:34
5
awa.gueye975
Awa gueye :
sama yaye nèna man gayi wakhal😂😂😂
2026-10-27 20:14:32
19
capableto2
capable🍇🍒 :
Li moma dall ak sama kharit bi
2026-10-27 20:12:13
46
lingure.tour
Linguére Touré👸❤️💍 :
Bly Massi khame dra😭😭
2026-10-27 23:25:40
0
antoinette2705
phina♡♡♡ :
souma livé dinguéne tapoter?
2026-10-27 22:17:08
7
mmitafaye0
M@mita👁️🐻🇸🇳 :
massih meuna wakh sm béne copine djotéh akk Farr bih baye Djoye ma Woh Farr bih attaqué koh bah sagua koh mou dikk ma aye nokk ma toke une semaine guènnou ma Sougne keur ndakh ragual ma kheuye Guiss téléphone bih mou épingler ko sa kaaw😭😭😭😂
2026-10-27 23:16:43
5
fatima.rassoul135
Fatima Rassoul 🧕❤️ :
Ni dh la toguei legui mandou rk 😩😂 dagni dioubo di statut nane seytanei yis nagnou bayi 💔👩‍🦯‍➡️
2026-10-27 20:39:05
5
astou.diop352
10 nov 👸🏾🎂🎉 :
Dotouma sii dougou🙌🏿🤣
2026-10-27 22:26:18
3
wakeurserignekhadim
wakeurserignekhadim :
Félicitations kine 1millons d’abonnés 🙏
2026-10-27 20:32:40
4
be_beautyful_by_thebest
Zeiina saliou :
Sama sœur bii ni la mele deh goumin conseiller laye ame 😂😂😂😂😂
2026-10-27 23:37:23
2
adashgueye1
𝐍𝐞𝐲✨❤️ :
Baparé sene status visé lanuy deff dila garou walé😫🤦‍♀️😂😂
2026-10-27 22:20:33
4
syfa233545
Fatima la puissance 😍 :
Bly bi nga done ame 2mill abonnés la nékone sa abonnés yallah na dem ba 10 millions abonnés si barki seydina Mouhamed
2026-10-27 21:53:03
1
mayna_hair
@Maynahair.officiel :
Soumayyyy wakh di dioyyyyy khiiii légui manou promax lâ woté 😂
2026-10-28 00:27:03
1
To see more videos from user @kine_zo, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About