Machallah dra guenouko surtout après fadiar yalla nala yalla Faye yiw ❤️
2026-10-28 00:00:42
23
Lmnprod :
Mais man bimako commencer def sama yaram ay pich la gueuné 😩😩
2026-10-27 22:04:56
16
DiDi cisse :
Def nako un foi fadiar dama paré sama bir bi du daw du metti bilay
2026-10-27 22:11:24
45
khale 3M parfumerie :
bakh na loll Machallah
2026-10-28 01:48:19
0
Thiate bu djiguene ❤️ :
Mane deh dama amewon hémorroïdes depuis 5ans defna lu nekk denioul mais dpui ma commencé ko heur buma diouler fadiar mome lay def dpui bobu la commencer am diam walahi anzim
2026-10-28 01:11:23
4
lacapricieuse🌺🌺 :
Kagne lén koy déf
2026-10-28 00:34:37
1
🌸💍🌸First lady💗💍💗 :
kharal ma nopi sakh bala thiatt dima topou😂🥰antouka daal machalah
2026-10-27 23:16:23
4
MK💕 :
Sareu bi yeup lay Guay wakh wa Bismilah rek Guay wakh
2026-10-27 22:32:12
9
yacinesarr5227 :
loye defe 1aprè 40 wala stp
2026-10-27 23:26:30
3
user2584337635244 :
Bilay aka efficace je cono
2026-10-27 23:11:34
2
laamsa69 :
Man dhé bilahi damoko def si sama ndokh bi may nane mais sama nakeu bi day méti rek bilahi
2026-10-27 23:46:44
7
Ndeye :
machallah yalna yalla féyla
2026-10-28 01:03:48
1
boumamebabacarsy1 :
fatiha complé
2026-10-28 00:27:04
1
Parfumerie Labourishh🥰🥰 :
Nako deff dhé inchallah merci beaucoup 🙏
2026-10-28 00:40:10
1
metisse_serere_bambara :
Mane dh sama gorge bi moy mèti 🥰
2026-10-28 00:34:14
0
Queen 👸🏻 rose ♥️🦋 :
Aka bakh
2026-10-27 23:23:20
2
la_benjamine :
Meilleur moment c’est entre Fadjr et Sohb
2026-10-28 01:02:18
1
Mme Didi :
salalahou allah mouhamed
2026-10-28 00:56:09
2
600000000000099999999999999999 :
a qurl heure on fait ce zikr
2026-10-27 22:53:44
1
user31056353086002 :
fibrome nak
2026-10-27 22:56:59
2
user1576728401279 :
ma challa merci beaucoup
2026-10-28 00:34:03
1
talibefallou❤️ :
Machalla
2026-10-28 00:12:25
1
user7998959891329nene :
vérité merci beaucoup 👍👍👍
2026-10-27 23:22:39
1
Mbojaaa :
Danga wakh Bismilah ak Ameen wala?
2026-10-27 22:30:28
1
yayou :
Walakhi
2026-10-27 22:52:03
1
To see more videos from user @jeunemaralevoyant1, please go to the Tikwm
homepage.