@user96160046: #mamendiayesavon😂😂😂🤣🤣🤣🤣 #tiktoksenegal🇸🇳 #tiktokviral

user96💋
user96💋
Open In TikTok:
Region: SN
Wednesday 28 October 2026 13:25:14 GMT
176459
11545
198
3051

Music

Download

Comments

mrsthioune45
Mrs Thioune🔐❤️💍🥰 :
Bima accoucher batay leke bou bakh lekou mako😭😭😭thiepp bii rek lay lek ak rouy bou amoul mew 😭😭tei dama nef sonou na
2026-10-28 16:16:32
138
kya_lopy
Kya_Lopy✨ :
Bizarrement damay nampal teh douma khif
2026-10-28 15:13:03
118
maguishanelba
maguishanelba :
mane dè damayy kheuyy lall sama sombre guèrtè parè tekcii bourou cappuchino parè midis ma daure sama agne 15 16h ma daure goûter 18h ma lèkate sombre guèrtè wala rouyy 20h 21h ma rèrr napalou touty bala teudi ma dorade après nak dèmm teudy
2026-10-29 09:26:36
11
bijousaliou1
Bijou💎Mrs Sarr💖💍 :
Mane dé bagnouma kouma wakh dama Pata damay lek ba sourr machalla
2026-10-28 15:12:23
349
salybarham98
salybarham98 :
Mane douma lekk surtout goudi meunou ma rerr té bb a 11 mois day namp guoudi gui yeup motakh je suis trop faible en plus je suis fatigué
2026-10-28 16:32:07
12
hawafalilou5
𝐇𝐚𝐰𝐚 𝐅𝐚𝐥𝐢𝐥𝐥𝐨𝐮❤️🙏 :
Man deh bii moy sm premier nampal wayer magui diekh tak sheut te nonu la amer won yaram🥰😂
2026-10-29 06:22:35
7
tiksawtok
Sawdia Mrs D. :
guisna kou khoulo dieukeur pour mou mayko 50 francs youmou dieundé rouy 😭 boula degué deh dayy kheum
2026-10-28 16:01:54
31
maremendiaye670
Maréme Ndiaye ❤️🇸🇳 :
Sombi guerte bi tamite bakhna trop si kouy nampale 👌🥰
2026-10-28 15:11:57
29
astouvivi2
astouvivi :
haral ma nieuw yoner mr
2026-10-28 14:43:48
41
modoumbaye53
Modou m diop :
Madame moma ko yoné me amoule Son [Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-10-28 16:20:50
4
khadijarassulmrssamb
khadijarassul boo cheikh💍❤️ :
Daw yonei ko mr gaw
2026-10-28 15:24:25
8
seydasokhnadiarrafadel
seydasokhnadiarrafadel :
Mane deh thi regume bu metti la nk ndax d gnou ma nane dama am yaram
2026-10-28 15:44:10
13
nionio0966
Nionio :
Kou amoul appetit nak soneu na deh garape yi djgou ma j’ai un bb de deux mois
2026-10-28 17:49:15
2
bb_fa42
Mme fall💍❤️ :
Mann mom douma sour 😂😂😂😂
2026-10-29 19:04:22
0
nina.sow1
Nina Sow :
Àyway lima dal nba dalou léne Yor dôme bou am 1an 2moi ndokh sakh douko diala lai😭 wene kesse lay namp
2026-10-28 17:01:46
5
mrs.ndiaye2.0
Ma ndiaye 🥰 :
Mane deh damay lek com kou meusoul lek mew Allemagne yi la sama djeukeur indil lou beuri chak 10mnt ma rouille
2026-10-28 18:55:14
6
korthiat2
Mijo💕 :
Khana man gay wakhalll
2026-10-28 14:50:27
6
bvbvdiosa02
bébé diosa01 :
mane dh damey lekeu ba tite comme kou am tégnia[Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-10-28 16:01:37
6
ndeyendor1
ndaye ndor :
billaye 🥰😭
2026-10-28 14:52:44
5
findsolutech
FindSoluTech :
Man d sama diabar dinama ray rk par minute la khif😂😂
2026-10-28 18:28:58
3
aissatoumdrame
jeune maman 💞 :
sama problème Moy douma lek parfois meme bén yon lay lek si jour bi et pourtant legui day tégué xaw ma louy problème bi
2026-10-28 20:20:19
2
user6300026277531
Mama Diamé :
si cest céssariéne
2026-10-29 12:50:54
1
diama.seye51
seye maissa :
guisnassi sama bop 🤣 je dis dama bagnat patta je mange peu🙂‍↕️
2026-10-29 13:23:34
1
ndir436
Mme Ndir ❤️💍 :
Damay lékeu légui khif légui rek
2026-10-29 18:05:42
0
ndeye.ndiaye.guey8
Ndeye ndiaye Gueye :
Merci
2026-10-29 15:50:19
0
To see more videos from user @user96160046, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About