@mamourgueye706: Affaire modou Ngom

Mamour Gueye706
Mamour Gueye706
Open In TikTok:
Region: US
Thursday 29 October 2026 14:06:17 GMT
17442
1186
65
71

Music

Download

Comments

khadymbow1775
Khady sérère :
ay way yalla sama borom lép Lou la meussa nian may ngamako mangui lay nianate téy thi Modou ngom nga diapalé guéno thi khat khat bi barké seydina Mohamed
2026-10-29 14:37:52
97
nourouapple66
Nourou Apple🇺🇸 :
Thieuy yallah moo sagñ lounèk😭😭😭😭
2026-10-29 15:07:57
34
coumbista8143
Soxna Coumbista 🌸❤️🦋 :
Ay Yalla yw rk y’a sanieu lii Sama xôl metina 💔🤦‍♀️😭
2026-10-29 15:28:45
0
unique.princesse5
Unique princesse :
ikhlas bingua diangue yalla nala takhawou continuons de prier pour Lui yalla walou sougnou mbokou dioulite biiii natou dou wessou mouk
2026-10-29 15:23:01
30
fallbv8
AÏDA🎓 :
Yallaa n’a la souniou borom takhawou si Barky Serigne baba xar st metinaa lol 💔😭😭
2026-10-29 15:54:50
0
yawa.saliou
Yawa saliou :
Thiéy yalla 🥲yalna ko borom bi takhawou
2026-10-29 14:51:50
9
ass_neymar10
🅰🆂🆂_🅽🅴🆈🅼@🆁🙌🏾🍼⊹•꧂ :
22ans beurina 💔🥹🥹
2026-10-29 15:22:42
4
pfboys.00
I am Pf boys ✪ :
Notre gouvernement doit demander un transfert de prisonnier
2026-10-29 15:46:07
4
ndayemaguettefall078
bèbè max :
Non li daw na yaram nk Ay yalla nako yalla samal bopam🥺
2026-10-29 15:36:27
2
cheikh8216
Cheikh tidiane toure 🥰🙏 :
Sama khole bagui metti
2026-10-29 15:29:49
2
coumbafalilou
Coumba faliloula :
😭😭😭😭metina lol
2026-10-29 15:20:25
0
sonia.paradise3
SONIA PARADISE :
Sama xol bi dague na barki alxouraan
2026-10-29 15:14:07
5
mame.cheikh2343
Mame Cheikh :
wax lene yéne ñiepou Alhamdulilah 😭😭
2026-10-29 15:56:26
2
ndeya.saliou77
ndeya saliou 🥹❤️ :
Barki alhourane mn cœur saigne 😔💔😭
2026-10-29 15:29:31
3
ndeyamoussalioumbacke
ndeyamoussalioumbacke :
Ohhhhh🥺 li Diamm bi wara Santé Yallah beurri na ☝️😢Yallah Nala Yallah Takhawou sunu Papa dji si barkeb Serigne Saliou 🙏 🤲🤲🥺🥺😢😢
2026-10-29 15:29:33
3
madamesall5
Madame salle 💍❤️💍 :
Bou kennn tayyi si nianalko tay lako geuna sokhla😭😭tay kham nagne li khew wayé souba kenn khamoul kan mooy ’ khéw souniou boroom man na louné
2026-10-29 15:35:03
1
copinedemamankathy1
la copine de maman cathy :
Ki beuguetoul dra si adouna yakaram tasna adounam diakhasona ta nekoul ak beine mbokakm li mettina trop vraiment 😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-10-29 15:25:24
1
mamand55
Maman diouf♥️✅ :
Thiey yalla sama khol bi metina
2026-10-29 14:36:04
3
mamediarra1857
mamediarra18 :
warna s fallou li yahna sama adouna bilahi 😭
2026-10-29 15:50:38
0
maguista970
maguista :
Li metti n’a
2026-10-29 15:55:43
0
oumarmakavelisow
shakur sow :
lii moy nattou deug 🥹
2026-10-29 17:38:02
0
mounassf7
mounassf :
Ay waye li métina sama khol bi
2026-10-29 15:58:12
0
papeamadysow
Pape amady Sow :
😭😭😭😭😭🏳️🏳️🏳️🏳️
2026-10-29 16:00:27
0
amzatouba
africa is future :
marina
2026-10-29 16:48:31
0
ndiayeeritage
boutique mére awa ✨💅💄👜👛👠 :
Machallah
2026-10-29 16:51:01
0
To see more videos from user @mamourgueye706, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About