Yalla nako souniou borom may xolou mougn Li metina 💔
2026-10-29 14:27:00
14
adamadiop419 :
Yalla rek mocii meune darra yalla takhawoul sa diam bou khébou bi sa diame diakhlena sa diambi mongui trokhlou cissa kanam 😭😭😭Sama khôl bi metina billahi
2026-10-29 14:50:17
16
Mia ndiaye❤️ :
22ans akhhhhh thiey yalla boula nato rk naru nala khôl boko mougne rk mossi desss 😭😭
2026-10-29 14:43:09
11
Une Salihate♥️✨ :
Thieye yalla li barri na trop wayy 😭
2026-10-29 14:47:08
3
sophia :
oooh sa musique bi
2026-10-29 16:19:43
1
Thianar saliou :
Yalla rk moy yalla Lou méti way yalna la yalla mom miy tégaté nattou yalna téguil la nattou bi🙏😭😭😭🙏🙏🙏
2026-10-29 15:31:41
1
Binetou Tuhfatou 🦂❤️ :
Yalla nala yalla soutoural t teguil leu natt bi inchallah
2026-10-29 14:28:45
3
rokhy ndiaye :
houwa lahou ahade alhou samade🤲🤲🤲🤲🤲🤲
2026-10-29 14:20:04
6
meremedabo :
Que Dieu le tt puissant te vienne en aide 🤲🏻🤲🏻
2026-10-29 15:25:25
1
Mrs Sy💎Xolou Abdou❤️🔐 :
Wa 22 ans deug la wala ???😭
2026-10-29 14:31:27
2
néné la lionne :
yalla beuri na soutoura té yeurmandém yatou na way 🥰🥰🥰
2026-10-29 14:27:50
1
beugue fallou :
ooooooh yalna la yala takhawou
2026-10-29 14:39:43
1
awa Saliou :
2026-10-29 15:44:21
0
🌺🩷Satou🌺🩷 :
barké arhourane adouna nékhoul yalla na sounou borom teguil li inchallah
2026-10-29 16:33:10
0
Sokhna Aram🇸🇳🇪🇸 :
Ohhh li mety 😭
2026-10-29 15:31:10
0
Fa❤️🇸🇳🔗 :
Amine
2026-10-29 14:17:30
0
Yacine cisseyaih :
2026-10-29 15:18:04
0
Talibé Serigne Saliou :
😭😭😭
2026-10-29 18:10:59
0
Mme Diallo :
No li metina dé
2026-10-29 18:35:27
0
khadyfaye3954 :
😭😭😭
2026-10-29 15:25:11
0
Gaye❤️❤️ :
yalla bakhna Dina guene inchala
2026-10-29 15:27:14
0
❤️♥️🥰 :
Yalnaleuh yalla taxawou feepeuh inchallah si barcké Mouhamed psl
2026-10-29 14:20:19
0
To see more videos from user @touty691, please go to the Tikwm
homepage.