Dou teude sakh 22 ans inchallah Legui niou bayi ko amna si yakar souniou borom meune nako teh yalla nako def 🤲🏾🤲🏾
2026-10-29 15:43:30
1954
SpaNova :
Il aura un miracle pour ce Monsieur il fera pas les 22 ans en prison 🙏🏾
2026-10-29 16:58:42
168
Habiba 🎀🇸🇳🌹 :
Nul ne peut échapper à son destin 🥺Que cette prison soit un refuge de paix pour toi et le chemin de paradis
2026-10-29 15:49:17
508
001binoushasaliou💍Mrs ndiaye :
5ans de prison lay teud wale 22ans?
2026-10-29 16:06:13
12
Arame SaliiiOu ChiiC ❤️🖇️🔐 :
Mais Pourquoi La Juge Pleure C’est Juste Une Question Yalla Nako Yalla Maye Khôlou Mougne Bamou Âme Grâce Inchallah Wayé Metti Na TrO 🥲
2026-10-29 15:21:27
442
Une Sima❤️ :
Ndeysane ki geum na yalla
2026-10-29 15:41:35
173
Astou labelle Mrs Diop💍❤️🔐 :
Epui nigno ko thièné dafa meti trop😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-10-29 16:36:26
60
Ous :
Yalla mi xam pi meune ..yalla nako sa borome tajhawou , soutoural ko , katanal bamou ame grâce ba delou si ndjabotam si bqrké alkhourane , barké yonénte bi, barké chekhiul khadim...🙏
2026-10-29 14:40:31
617
𝕆𝕞𝕒𝕣 𝕖𝕥 𝔸ï𝕔𝕙𝕒 :
Gni nignouy chaîné nit daffa niaw way. Ô Allah accorde la liberté à Modou Ngom
2026-10-29 14:35:52
371
Gogo business 🎉 :
Yalla yala soutou sare 😭😭😭
2026-10-29 19:06:34
0
SEYDA KMT :
Nagne continuez di gnane yalla darra teuwouko 😭Lepp meuneu na changer thi katanou yalla
2026-10-29 15:36:45
136
Miel🍯 ❤️ :
Adouna metti na sama khol metti na tay 😭😭😭😭😭🥹
2026-10-29 17:32:11
28
Saly diagne :
khol yépa toye😭😭😭😭😭
2026-10-29 15:45:30
105
Fatima ❣️ :
ohh lala sama xol méti neu ndeysane lou méti yagu neu ci adouna yalna ko yalla taxawou
2026-10-29 17:36:06
11
Princess Madifa✌️ :
Je vois qu’on le traite avec respect malgré tout ndeysaan yalnako yalla takhawou
2026-10-29 17:36:00
22
Ndeye ndiaye :
Yalla nala yalla same 🤲🤲🤲🤲
2026-10-29 18:09:05
0
Mané Hawita :
Alhadoulimahh lou yalla def nonou la yalla baxna mo guein perpuitè sant leinn
2026-10-29 15:44:12
32
La cadette🔐💐✨ :
Thiey adouna kein khamoul lanla 😳 natou deug moy li🥺
2026-10-29 17:33:05
13
Didjo :
Sant yallah lépp mo gueune dée
2026-10-29 15:31:23
36
dieynahassim :
wa lou takh gouvernement sénégalais bi demander wouniou clemence au États-Unis loutakh defouniou intervention
2026-10-29 17:20:30
11
Jacolyco :
il va sortir avant ce délais,bou défé bonne conduite. cette peine c'est pour apaiser les familles des victimes
2026-10-29 17:18:35
17
Soxna Aïcha Niass 🤍✨ :
Dilén fatali ni الله dou nit amoul khél amoul logique dou togne nk wayé louko nékh lay déf et il nous a dit « chaque difficulté vient la facilité » YALLAH BOUR 👑 BOU BAAX LA
2026-10-29 16:41:47
50
Mamoucha~Shop~🖇️♥️ :
Chaine yi niou takkal moma si gueneu métti 😭😭😭
2026-10-29 17:31:58
7
Ndieme Business 💕 :
Natou dou wess yalla nala yalla sam are la oyofal natou bi
2026-10-29 15:53:25
18
Thiatou bayam 🥰 :
Adouna nekhoul té dou meussa nekh
2026-10-29 15:51:52
16
To see more videos from user @omaraicha05, please go to the Tikwm
homepage.