@tiktok_galsen2: Modou Ngom a été condamné à 22,5 ans de prison#viral #senegalaise_tik_tok #galsen_tiktok #senegalaise_tik_tok🇸🇳pourtoichallenge #senegalaise_tik_tok🇸🇳
22ans de prison ak peine de mort louy différence bi américain Yi nio bone😡
2026-10-29 15:09:20
205
Matysenesene Sene :
Ay Yalla bour bi wonala dé wouyouko guir dieume Seydina Mouhamed 😭😭😭😭😭😭
2026-10-29 14:49:37
468
syibrahim156 :
yalla Nala sougnou brom takhawou
2026-10-29 16:21:27
0
Sokhna Faty Dia Hamza :
Lila yalla namou si mome naniou ko nianal rek
2026-10-29 14:52:31
115
Barkham Construction :
mais si c'était un américain qui a fait un accident ici au Sénégal esque sera pareil
2026-10-29 15:43:27
33
Bineta N’❤️ :
Sama adouna bi yakhou watt comme bi sama yaye décédé😭😭😭😭😭😭😭😭
2026-10-29 14:53:37
69
user5656521111 :
esk c possible indiko senegal mou teud fi peine bi?
2026-10-29 15:42:19
9
Dione Royal BTP :
que Dieu lui accorde la force de tenir la douleur ainsi que sa famille
2026-10-29 15:05:22
57
Amina🩷💯🇸🇳 :
Yalla lii gueune rekk lay def yal nala wolou meune am sah 10 ans sah do ko am prison natou mome fou nekk lay dieugué way kémanou yalla ak yeureumandém soutt na lolou doula mossa sétane surtout si diamam bi ko gueum di ko damoo yal nala borome bi takhawou🙏🏾🙏🏾🙏🏾
2026-10-29 15:26:07
11
Naby_ndiaye 🇸🇳 :
ayway lolou barina dh yallah nako yallah may xollou mougne