j'ai peur de nanger j'imagine les dauphins et requins dans la mer
2026-10-30 09:16:02
208
Fall lou 2218 :
2026-10-31 02:08:32
10
narou yaye marétou💝 :
néna niou nieuw doul
2026-10-30 12:23:35
56
ibou laye 450 :
li nékh na d mais ba wor neu
2026-10-30 10:18:18
50
Pãpįtø🥳 :
Un jour ma diangui ba wathie dém pour gnibi sougne keur basi yone bi ma tassé ak béne mère bu yore gaz🥺 mounima sama dome domabale yoboule ma gaz bi sama keur ma yeurame ko😞yobe gaz bi basi bire keur gui rek ma dale di guise ay bop😳 sama fit toga toule 😨ma def faire semblant melni ku guisoule dara après maniko sama téléphone bi dafa wade si porte keur gui xarale ma dieule ko mounima wawe rek ma dale di daw après thie la wo police expliquer co situation bi police dale di niaw ma wane ko keur mère bi après police diape ko guéné bop yépe ndakata ay bop chargeur la ak bop rallonge mofa nékone jour bobu akka ma tite.