Mais gnom bokoul ak Sénégal 🇸🇳 sen 20 ans moy sunu 10 ans donc…. 11 ans 3 mois lay teud ta sou defé appel meun nafa bagna egue ….insha alah malen ko wax dou teud 22 ans sama commentaire bi soulen nexé nguen garder
2026-10-29 20:07:59
53
Mor Ndiaye :
Non madame, 2048 c'est 22 ans. Mais il peut faire l'appel pour beneficier dune' reduction de peine.
2026-10-29 19:25:54
34
A :
lolou yalla Reik lay néx
2026-10-30 00:59:16
0
sallalahou allah mouhamed❤️ :
Day fen de
2026-10-29 22:27:15
18
Cheikh actros🚚♥️🔐 :
waxo lou ame dehh
2026-10-29 20:20:20
12
L'Enraciné-Pénaliste :
khana appel amatoul nag ?
2026-10-29 19:13:40
39
service Ahmadou :
kenë lathii la ko
2026-10-29 23:12:49
0
Ndiolé Diéne❤️❤️❤️❤️ :
ki dou wakh diam ay way😭😭
2026-10-29 23:05:33
0
Loss space foot⚽️❤️🧠 :
Waxo degggg
2026-10-29 23:33:00
1
football ⚽ :
yalnako yalla teguil natou bii
2026-10-30 07:11:35
1
Omar Ka :
ki dou wakh diam
2026-10-29 22:43:17
8
Aminata Kane ✨❤️ :
Yalla meuna lou nek wa Amérique 🇺🇸 ay nitt kassei len mais yalla moy yalla bouko nekhei souba souba mou guene neko si situation yi 🤌🏾 god is one ☝🏾
2026-10-29 22:12:12
9
Talibé Serigne Babacar sy :
Day wakh linga métrisé
2026-10-29 19:56:49
7
ƁÏĢŁÃŸĘ47 :
Nianal lènko wayy
2026-10-29 21:01:10
11
Lõüfā nįå$$💀🇸🇳 :
Bari nga wakh dh té lingay wakh dra lerou lasi, yalla meun na louné sou nekhone sunu brom tay tay doufa fanane
2026-10-29 22:16:05
9
adamabal3 :
Yallah Bakhna
2026-10-29 20:06:48
1
Zeyda Awa Mou baye Niass 📿❤️ :
Allahou akbar ☝🏾😭😭
2026-10-29 19:24:14
7
Mora Thiam :
c est pas vrai dagnouy deff aple
2026-10-30 01:27:54
0
mbaye_babacar🇸🇳🇺🇸🗽 :
Dèl wakh lo maitrise
2026-10-30 01:43:36
1
barhamouniass seringe :
Ragale léne yalla tè nianale KO
2026-10-29 23:45:07
2
Mame Mor Diagne :
Mousou ma guiss mowakh diamou ki
2026-10-30 00:50:08
0
Serigne mbaké Sarr :
wa khofi dara
2026-10-29 23:30:13
2
Fall bouna :
Nn sou ames avocat bou bakh avant 30jour yi di mate bou déffé appel peine bi mouna wagnékou bou bakh niou doundé yakar rék yalla bakhna
2026-10-30 01:31:53
1
To see more videos from user @dakar_senegal5, please go to the Tikwm
homepage.