@gptvsenegal0: #"Li Modou Ngom wax tribunal bign ko condamné 22ans & demi..image bou triste bi" Khadim

gptvsenegal⍟
gptvsenegal⍟
Open In TikTok:
Region: SN
Thursday 29 October 2026 23:09:08 GMT
153548
21866
635
287

Music

Download

Comments

boydia789
BOY DIA LUTTEUR 🇸🇳👌🏿 :
fii ba 2048 dafa métti billahi😭
2026-10-29 23:53:25
171
maimouna.toure14
Mounas Shop :
Souma khalaté limay yégue diamono dji té dou sama dérette 😭je n’imagine même pas la souffrance de sa famille 😭😭😭
2026-10-29 23:38:59
321
fallouseneuser4000
Sene gallas :
Bou nékone Senegal sakhe dina tanè👂👂😭🤦‍♂️🤦‍♂️🤦‍♂️🤦‍♂️🤦‍♂️
2026-10-29 23:51:58
252
cheikh.diouf5905
Cheikh Diouf :
wa na état demandé mou gnew fi teud ko fi
2026-10-30 00:09:45
37
marie.sow.touba
Marie sow poulo ❤️ :
Wolahi mety na Torop 😭😭😭
2026-10-30 00:04:17
25
servircheikhoulkhadimf2k
FONDATIONKHIDMATOULKHADIMF2K💚 :
Yaw souniou borom man sa diam bou khébou bi mangui toup di trokhlou sisa kanam dila niane soudé meuss ma déf Lou bakh si sama adounou mangui lay niane si sa bakh ndakh yay bour bou mague bi yay borom Asaman ak souf diant ak werr Yaw rek ya meune ya am mangui Lay niane ki di Modou Ngom gua harr ko samouko té dila niane soudé prison meunoul niak yaw Yalla boumou wésou ay wérr si barkép yonentibi ya Allah pitié je t’implore d’épargner cet père cet oncle au tout puissant je t’en supplie viens lui en aide 🤲🤲🤲 walahi j’ai le cœur qui saigne pitié pitié ya Allah aide cet père qui n’a voulu que aider sa famille vraiment la vie toi je te déteste aujourd’hui pourquoi cet père j’ai tellement mal comme si c’est mon père 😭
2026-10-30 01:39:32
4
rouguilabarhaminne1
Rougui la barhaminne :
bilahi lii moye dogal yallah dégue
2026-10-29 23:54:02
29
uneprincesse151
uneprincesse151 :
Juge bii néna durant procès bii yeupp dégou pabi wakh je suis désolé 😭😭 vraiment metti na
2026-10-30 00:03:50
41
sopep.serigne.babacar.sy
talibé cheikh :
nalen Etat mayy ay visa famille bi yeppou nou dem setiko walla dama trokh
2026-10-30 00:47:49
5
saliousamb639
Saliou Samb :
c triste yalnako yalla téguel natou bii🥺🥺
2026-10-30 00:09:51
33
mor.fall617
Mor Fall🇪🇸🇸🇳🇬🇲 :
Yalnako yalla takhawou si barké Mouhamed psl
2026-10-30 01:05:10
0
amadou.balde19
>AMZO 🇩🇪 £ 🇬🇼 💚 :
Senegal amoul president mo takh
2026-10-30 01:27:26
1
arameniang173
bb arame :
Ohhh😭😭😭😭😭😭😭😭😭💔💔💔💔💔🥲🥲🥲😥😥🥰💔💔💔💔💔😭😭😭💔💔
2026-10-30 00:10:57
12
sonko.junior2029
Sonko Junior✌🇸🇳 :
Ki dou teudi 22,5 ans inchallah
2026-10-30 00:02:56
21
user6130949310083
محمد حيدر :
yalla bakhna
2026-10-30 00:44:48
0
madamesy.busnes
Gnagna Store 💅💃 :
Li bilahi mètite meunouko rombou
2026-10-29 23:46:08
35
chiekh.gueto
coumba dieng♥️ :
surtout 75 bi
2026-10-30 00:05:23
16
hassandiop323
assane diop Bou real Madrid :
metina trop vraiment 😭😭
2026-10-30 00:00:55
10
ballybousso036
ballybousso002 :
Nako sénégalais dieul c possible nagn niane rek
2026-10-30 00:05:20
21
finamouserignesaliou
Fina -mou Serigne Saliou 💦🙏 :
Metina 🥺
2026-10-30 00:09:48
10
user18226117724364
Pénda Fall :
bilay
2026-10-30 00:03:33
6
assanebaldeiliza
assanebaldeiliza :
dey bah
2026-10-29 23:15:37
18
user8113487926171
user8113487926171 :
😭😭😭
2026-10-30 00:11:21
5
laminesow196
nabilmoustaphadiop9 🇸🇳 🇪🇸 :
adouna si bopam mo soff
2026-10-30 00:41:13
7
mme.dionevaissell
@Mme Dione🍴🍽vaisselle :
bilay ahmadou wakh gua deug dei
2026-10-30 00:28:46
10
To see more videos from user @gptvsenegal0, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About