Surtout borom maillot barça yi 😌 euleuhou akbarrr 😂
2026-10-30 20:33:49
426
Fatou Ndiaye 🦋 :
Nitt noumou meuneu xegn dimanche 😭💔
2026-10-30 09:56:19
785
mad-mys-sam :
wouy kou yagoul dieuk bus doko kham la ila fajar kay may diangui grand bi adie lokho yi té dama gatte avant arret bi maniko grand parfum 500 lay diar daw wathie ahh sama ak nalen dal deh 😭
2026-10-31 07:31:55
0
🇸🇳🤴🏾محمد :
Da tel sakh 8h
2026-10-31 21:40:01
0
Darling ❤️une 221🇸🇳 :
Peuls fouta yi nouyou na leen aka nio meuna khégne Lou nekh hooo j’aime trop sen parfum
2026-10-30 21:44:51
200
M:M:C🇸🇳🥇SÉRÉRE🧠👑 :
Doyna war 😂d
2026-11-01 01:01:18
0
La plus belle 💕 :
Surtout bus yiii bilay amna niou salté 😭😭
2026-10-30 11:12:17
311
zeynaexwally :
Choquée 😂😂
2026-10-30 20:32:34
178
Anna ❤️babacar ❤️☮️ :
75 bi fadiar oh dh lay begue df🥺
2026-10-31 19:40:46
0
AK :
parfum kén douko def si pokhotane..day khégn après
2026-10-30 22:46:32
148
La tigresse 🐅 :
Guisss na sah kouyyyy khegne 06h. Dougou si buss bi magui takhaw si guinawayy mais youtttt ladone khégne bilahi
2026-10-30 21:44:37
57
ZeynaA :
Man je ne peux pas comprendre ,comment tu peux te lever pour aller travailler wala marché do lall sakh ndox.
Sama grand frère souy dem napp dieun sakh day lal parfum beu khégne lou nehh😁
2026-10-30 23:30:36
81
YaYou_Ib💫 :
Ay way loy wakh niii[Hilare][Hilare][Hilare]
2026-10-31 00:32:06
0
momo digane :
kou xegn 8h dé 12h noy mel[Larmes de joie]
2026-10-30 23:43:22
18
MD 🇸🇳🇫🇷🇮🇹 :
bamay dem marcher kerok aye 7h 8h une fille très bien sapé moma romb barki alhurane damako beugone wo waxtane ak mom nakh xegn layyy dafma romb et je me suis retourner brusquement