@cas221.0: #papembaye #modoungom

cas221.0
cas221.0
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 30 October 2026 09:57:30 GMT
174322
13819
326
612

Music

Download

Comments

astoundiaye875
Toundiaye89 :
Walahi wakhone ngako mbaya
2026-10-30 11:15:08
667
fraicheoxy
Fraîches oxy🦋 :
Mbaya ligua wakhh mome deugue pirrrrr le
2026-10-30 11:31:47
144
mackysall96
Fille de mAcky 🇸🇳🇫🇷 :
Ndeysane da warona wakh sorry sorry rek di dioye billah 😭😭😭😭
2026-10-30 13:34:53
19
aissatou.ndiaye027
Aissatou Ndiaye :
Il faille mou dioy balou ak
2026-10-30 11:03:09
259
ndaye.diallo61
Beug Serigne touba ❤️🫶 :
Ms dafa geume yalla rek khame na mo takh dio youl 😭
2026-10-30 12:01:32
299
mamiko308
Talibe mame khalifa🙏❤️ :
Fi yalla reka fi nek
2026-10-30 12:27:37
114
jo___667
jo___667💈 :
Incha Allah Kii dou fa yague yallah bakh neu
2026-10-30 11:31:18
169
fatoukfa
Kine :
I am sorry rek laye ratataaati, di gnane ci sama xol 💔
2026-10-30 10:39:09
95
astoumbenediop817
bbei Satou 🥰🥰 :
Dfa geum yalla rk
2026-10-30 13:25:28
26
iamohod4
Evo trans :
Problème bi Moy modou ngom dafa diakhasoo nékkoul dafa am ay nitt yu mélnonou billahi dioy khol la amé
2026-10-30 11:53:04
30
amina68_
Amina68 :
Le juge l’a même dit, ils pensent tous qu’il ne regrette pas les faits. Les cultures sont différentes, il faut utiliser à notre avantage! Mbaya a raison!
2026-10-30 12:48:51
30
ndongo.diouf470
domou pikine💚❤️ :
Lolou wédii yallah
2026-10-30 12:10:46
36
myakountash
Mya kountash 🪼 :
Ay mbaya mi
2026-10-30 11:22:32
40
une.adja3
Une adja👩‍🎓 :
Meun na am dioyou khol lay dioy metina dal Ms Desolé mom dako warone Wakh 😩
2026-10-30 18:51:32
12
serignefallourek2
Sope Serigne Fallou :
Mais il est sou le choc qui mot yi sakh daf ko rer jugé bi kay mo effacer la utiliser mais yalla nako yalla teguil
2026-10-30 12:06:18
33
mad_rassoul
مادياو :
Mrm djii daa kham américain yii nakk c ça en fait
2026-10-30 11:35:52
32
rassoul258
Khadija 🇸🇳💙❤️ :
Guis nga bou wakhoone millions balma sax yalla binde na loummouy bind dou dégne sauf k been part waronne na ballou apres bammou tari wer
2026-10-30 16:02:52
15
mbowfatou6
beugue fallou :
Fi yalla mofi nék ak lou meunti khéwe nagne djiteule sounou borome mome sounou borome moko tek natou bi teh mome laye sobe mou teguiko teh Inchalla dinako tegui thi lou yahoule dara 🙏
2026-10-30 11:57:19
22
astousall25pastef
Astou Saliou pastef :
Mbaya nak dougou si domaine bou sensible barke alkhourane fi yalla rek mofi nek.yalla rek moy yalla arêtele
2026-10-30 17:53:14
5
diaz_code08
༆ 𝐃𝐈𝐀𝐙❤️𝐌🇸🇳𝟎𝟔𝟕🥷 :
Senegal 🇸🇳 kene meunoulle manou 😂😂😂
2026-10-30 10:04:47
22
darousalamcouture3
DAROUSALAM COUTURE ✂️✂️✂️ :
Mais ki dafa guem yalla rek té sou dioye daye diakhal djiabotam gui ake nioun Senegal yi mame dh sama journée dembou ki comme 10 joueur dama dioy ba sonou nian ba tass
2026-10-30 12:59:41
11
fatba24
fatba :
Fi deh yalla rek mofi nek
2026-10-30 13:07:30
6
www.business02
everyday english :
deugue rék la wakh
2026-10-30 11:21:06
14
To see more videos from user @cas221.0, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About