@laat500: Seriñ Basiiru Mbàkke ibn Xaadim Rasuul nee na: « am na bis ma ñëw ci SËRIÑ bi, fekk booba ma yoroon hadiya ju ñu ma yobbante woon ci MOOM, ma defoon ko ci sama jibay camooy (poche gauche), kama ko yobbante woon di ab taalibeem bu farlu, bu tudd Muhammad Faal. Bi ma ñewee ba jub SËRIÑ bi, ma dàldi dugal sama loxob càmooy ci sama jiba (poche), ngir gennee àddiya ji, ci noonu rek mu dàldi may gedd, xool ma xool bu xawa raglu, man it ma tit lool bay lox, ndax dama koo rusoon lool, boole ci ragal ko, te noonu la népp meloon ci MOOM. SERIN bi ne ma « càmooy?! » ci laa daadi gaaw jël samab loxo ndayjoor, jel àddiya ji ci poche bi, joxe ko ko ndayjoor. Ci laa xamne nag, man dese naa lu bari...»

ABDOUL AHAD SY
ABDOUL AHAD SY
Open In TikTok:
Region: CA
Friday 30 October 2026 10:58:45 GMT
4287
1246
16
16

Music

Download

Comments

noname19961201
User19960112 :
Eskeuy ćey Sëñ Bassiiru
2026-10-30 19:10:22
5
zannenouraynidiop
Zanne nourayni Diop :
amoul MOROOM DH 😍🥰🥰
2026-10-30 21:48:53
0
geumesabop0
geum cheikh ibreu :
Titre wakhtane bi
2026-10-30 19:00:49
2
yayefalllousegneazizfall
Yaye fall Diop :
dieurdieufty serigne touba
2026-10-30 20:55:19
1
baye.deugeu.180
Baye kl 180 :
dieureudiéufé cheikh ahmadou bamba ❤️❤️
2026-10-30 23:45:13
0
engali___gmd
engali___gmd :
🥰🥰🥰
2026-10-30 23:31:03
0
bathie.thiaw4
Bathie Thiaw 🛠️❤️✨💍 :
🥰🥰🥰🥰🥰
2026-10-30 23:09:50
0
user3845122211515b
baYe goor sisce🖤🩶💫🙏 :
🥰🥰🥰
2026-10-30 22:47:18
0
dieng1407
baye sall dieng :
[Réconfortant]
2026-10-30 20:49:36
0
cheikhounabambasamb
cheikhouna bamba samb💡 :
[Réconfortant][Réconfortant][Réconfortant]
2026-10-30 20:11:58
0
bass.bamba68
Bass Bamba :
🥰🥰🥰
2026-10-30 20:08:57
0
ndiaye28134
ndiaye :
[Cœur rouge][Cœur rouge][Cœur rouge]
2026-10-30 15:08:42
0
bayesall299
bayesall299 :
❤️❤️❤️
2026-10-30 14:58:09
0
latir.faye81
Latir Faye :
[Réconfortant][Réconfortant][Réconfortant]
2026-10-30 13:02:23
0
khadim76903
khadim mbaye :
🥰🥰🥰
2026-10-30 11:01:33
0
serigne_sam_mbayediop
S SAM MBAYE TOUBA :
🥰🥰🥰
2026-10-31 00:48:33
0
To see more videos from user @laat500, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About