@al.aamine: #khassaidcom

𝗔𝗹 𝗔𝗺𝗶𝗻𝗲
𝗔𝗹 𝗔𝗺𝗶𝗻𝗲
Open In TikTok:
Region: IT
Friday 30 October 2026 11:13:30 GMT
461992
64426
699
7986

Music

Download

Comments

nutrifa1
Nutrifa🥤 :
Sama boss dh waxouma 5mois ms jours bimay def test de grossesse ba jour bimay accoucher mane ak mome Nioy ande opital bi sage femme yeup xam nagne tourame kokou yala rk lakoy bayél 😭😘
2026-10-30 16:50:21
1554
shoufvrasoul
Talibé serigne mbaye sy abdou :
Douniou ko deff dagua eupp niou bala fi di dokhane dila méré nk tek thi mes yala bakhna 🙏
2026-10-30 16:34:20
345
ousseynou.konte1
Ousseynou Konte :
4 mois you desse khaliss bou beuri laniou wara lidienti pour nguente bi
2026-10-30 17:10:43
81
fatou.toure0452
F🌺à🌺t🌺o🌺u :
Ki nako état protéger
2026-10-30 22:44:58
290
arame33147
Sope Serigne Saliou Mbacke :
Kimayseyel kay deglouli😁😁😁
2026-10-30 17:57:50
77
rabymoth
yayou bété bété yii :
li dé la sama dieukeur def yalla nako yalla fay bilaye ndeysan ❤️❤️
2026-10-30 17:58:27
52
beuguebamba270
BEUGUE KHADIM RASSOUL :
Li dè la sama dieukeur def yalla nako yalla fay
2026-10-30 17:46:39
102
emirasophia
So ´ Cake :
Yallah naniou yallah may dieukeur diou beuri yeurmandé
2026-10-31 02:25:29
66
zizaking16
ziza King Nittou Mbedda 🇳🇬 :
😁😁Waw dinako def inchalah
2026-10-30 21:12:20
33
fatima.msr.top
fatima Msr top🥰 :
sama dieukeur dh comment garde du corps depuis ma def teste de grossesse bi amou ma fayam bly
2026-10-31 01:04:42
11
fatimadiop2014
Fatima Diop :
Bilay Touré mandy mory yi la may defal d nènaa la diaral nga ma nef chaque année ma diour ndakh ninga may topotoo yalla massa diam yague🥰🥰🥰
2026-10-31 10:27:24
25
senegalo_belge
𝒯𝒽𝒾𝒶𝒷𝒶ꨄ︎🇸🇳🇧🇪 :
Sama boss rk moo djara wakhal Yaa-Latiiff. Machalla 🥰🥰🥰 Vander Zijpen sama goor gui.
2026-10-31 13:23:19
9
bineta5276
yayou :
manedé souma eumbé aka may riche mr damay diokh khalisse rk🥰
2026-10-31 19:02:01
6
blacky_girl93
Une Senegalaise🇸🇳🫶 :
Loyy khaar bam am 5mois assister ko des le debut kayy debut grossess mo guen metti
2026-10-31 20:51:31
7
ronediakh88
Door warr joal famillii 🔨🔨⚒️ :
assistances binga waxe mome la djiguene gueuna soxla mé pas xaliss pasque dou gneupa yor xaliss yalla dafa binde té yemalewoul pour mane diko topoto di waxetane ak mome diko couvrir mo eup solo ?!🙏
2026-10-31 07:23:06
11
yayoumoustapha01
Thioro mory❤️🖇️ :
Yalla nagniou yalla bolek goor yalla bou bari yeurmande t’es bax xam akou ndiourel🤟🙏
2026-10-31 10:36:18
6
yayou.keurgui
yayou keurgui :
bilaye ma bonelé ak damaye nelaw boulma déranger
2026-10-31 09:41:08
16
khady1063
k :
merci beaucoup ♥️♥️♥️♥️♥️♥️
2026-10-31 14:26:48
5
absaofficielle1
Absa ❤️clara ❤️ :
Sa facilite l’accouchement deh mome surtout lolou 😂
2026-11-01 13:01:38
5
diopaicha315
Diop Aicha :
mousou ma am Thi sa dieuceur , début grossesse ba fin mane cassé
2026-10-30 20:26:46
9
alalou.kou.bakh.k
Peulh bou rafete :
Ay way lolou amena goor you kay def c dommage 😭😭😭😭😭
2026-10-30 22:45:21
8
maymouna.ndour
Maymouna Ndour :
Bilahi deugue pirre
2026-10-31 00:40:42
7
zeymor3
ZEYMOR🥰😍💖🌹💝❤️‍🔥 :
sama diambar dji dé massage sakh damakoy défal dima topoto souma lekoul day melni kou febar wallahi anzem ak nanemane lo beugue thiey Ndiaye diatta ya bakh rethiouwouma limala khamé wone Kaf gui ré gui douma sone douma triste Allahouma barik alleyhi 🥰💖
2026-10-31 09:23:25
5
gambi838
genre934 :
2026-10-30 18:57:09
10
iboulaye.lebalante
ibrahima diatta :
oustaz mane mom thiatlouna
2026-10-30 16:18:35
19
To see more videos from user @al.aamine, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About