@mouhamedndiaye_14: « 😱 FAS BI AK XAJ BI ÑU DOON WAX ! » 😂🐴 Goor gu néew doole ak fasam… ba bés mu dégg li mu dul xaar! 😱🤣 Xaj bi itam am na lu muy wax ! 🐕💀 Li ci xew mooy saga bi ! 🤣🔥 #HumourSenegalais #DramasSenegalais #Wolof #TikTokSenegal #VideoDrole