Par ce que yeneu boys yi deuk MF gno wara valoriser sen quartier bi mais dagay giss certains di deff vidéo sakh di wané une mauvaise image si MF legi kofa khamoul dagay yakarni nonou la mel mane mi deukou maga mais bilahi MF heure bou nek douge nafa matin midi soir sans blême et c pareil pour darou salam aussi boys yi nagnouy wané image bou rafaite si sen quartier Mercie 🙏🙏🥰
2026-10-30 19:40:34
26
MD~@|¥_$0W🇸🇳⚽️ :
Nn AG loussi eup montage yii motax mais pas affaire de banditisme banditisme bi mome c'est partout a Thiés légui ni rék coté stade la diouguè mais simol bou doywar mo amm sì route nationale bi té hlm moy jouer boy yi keine xamoul founou deukeu médina fall lanou sikeul rk
2026-10-31 01:50:35
1
Soyez heureux :
Sampou yi laniouy daw 1000 yi 🤣
2026-10-31 00:37:55
4
☆BAAY_SHEEX` :
Bilae wxal deh même sma school souniouma ladjé fo deukk mani MF dagn maay xolatt😂💔
2026-10-31 01:10:40
0
BATZO NITTOU THIES :
Bilahi frr waxa tiko dh té khamouniou ni medina fall ay lucide niofi eupou danio bakh rk ☝️🙏😅
2026-10-31 12:44:30
3
PAPA BOU FERMIN 💙❤️💙❤️💫💫 :
ték si gnouni médina fall amoul sécurité ay rétane dama diapou sakh li mome fawou gnou lérale ko pas que gno gui yake sunu dérou quartier bilahi
2026-10-30 18:10:43
1
Yacine Gueye :
mandé amna Ben grand bou nekalon billahi bimou ma ladie fo deuk maniko médina fall bobou lma bayi waye mo kham
2026-10-31 14:14:43
0
idrissalofficiel10 :
Lolou diaxal nama trop ko arrêter d’où dém
2026-10-30 17:41:08
11
G G :
non bro dou lolou dé samp yi la
2026-10-31 22:28:04
0
F.C by ✨Fatou Charme :
Lolou Yag nama diakhal ta lima metti niom niep fi laniou deuk lol[Larmes de joie]
2026-10-31 21:40:45
0
PAPADAOUDADIOP :
wakh nga deug dé . taximan you barri medina fall laniou deukk
2026-10-30 20:23:27
0
mame Bassine ndiaye :
Bilay chaque weekend ma kholou ak taxi yi 🚖 médina fall moni non 21h😂
2026-10-31 12:37:18
0
Alimabonbonniang :
Pourtant gni eup falagnou deuk
2026-10-30 19:03:48
2
PriMőHh RãTëL Bii☆♤♡🦡🚫 :
MF Seul😂❤️
2026-10-31 10:46:14
0
DIEYNA🦋🌼🌸❤️ :
Bly lolu dma diaxal
2026-10-31 00:54:50
2
AwaFaye :
waww deugeu leu
2026-10-30 21:25:43
3
IsSA🥊 :
Assane wakhal dehhh
2026-10-31 14:58:18
2
U9 bii 🍼🇸🇳 :
Mla sii meun wkh dra ma diougue match mbour ay 23h la aksi thies srx stade lat dior ba buntu dépôt taxi buma arrête mu bagne djakarta mm wkhalema wu mko sma jour bbu 😂😏