yéwou 3h du matin djapp ba séll barki Mohammed di djanal Seydina Ousmane Sonko ❤️kép kou fékhé Thi momeu yalla déff mou keupou Thi bopam Seydina Ousmane Sonko walahi yalla dako Beug yalla dafay koy protège nitou yalla deug leu mome motakh ma koumacé suivre politique ték xam Lou beuri naxx momeu