@prsident.senegal: 🇸🇳JOJ Dakar 2026 : Ndaje bi sunu ndaje la, ndam li sunu ndam la! Sénégal dina dalal ndaw ñi jóge ci réew yu bari, ñu ñew bokk ci Jeux Olympiques de la Jeunesse. Maa ngi woo Senegaal yépp, nu won sunu gan yi sunu teraanga, dalal leen bu baax te dimbali leen ci li ñu soxla. Xam naa ne ndaje bii dina indi ay jafe-jafe ci dem ak dikk, rawatina ci yoon yi. Waaye maa ngi leen ñaan, nu muñ te muñalante, ngir lépp jaar ci jàmm. Sunu ndaw yi di sport, noom itam, nanu leen taxawal, dooleel leen te won leen ne réew mépp a ngi ci seen ginnaaw. Na àddina sépp gis sunu teraanga, sunu bokk, ak sunu mbëggeel réew ! Ñun ñépp a bokk ci ndam li. #Dakar2026 #JOJ2026 #Teranga 27,6 K 2861 2793 702

•PATRIOTE 🥏-🇸🇳
•PATRIOTE 🥏-🇸🇳
Open In TikTok:
Region: SN
Friday 30 October 2026 22:56:57 GMT
12321
376
49
10

Music

Download

Comments

papispogba
Papis papis :
C’est le Sénégal qui gagne 🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳🇸🇳
2026-10-31 21:18:41
1
issabarry2420
issaba2420 :
fayal indémnité de logement bou dakar dem dikk
2026-10-31 02:44:39
9
cheikhbayeka1
Baye ka :
Lép dina bakh inchallah
2026-10-31 10:30:55
4
.chgueye0
@Gueye781,🇸🇳🇪🇸 :
2029 yagui toul inchla ♥️♥️♥️♥️
2026-10-31 06:44:23
3
mariamagningue830
Mariama Gningue :
2026-10-31 13:29:09
2
orphelina.keur.mam
orphelina keur mam Diarra :
sonko reck la noye topp
2026-11-03 21:19:41
0
modoufall516
Modou Fall ibiza :
Sonko rek
2026-10-31 09:17:03
2
mbayetltfoj
Queenlea :
Hi Mister the President
2026-10-31 17:07:12
1
queenbigue22
QueenBilguiss👑🥀⚜️💎 :
c'est ton vrai compte Presi ???
2026-10-31 02:42:58
1
papasow6504
Talibe Brm Darou 🤲🏾👌🏽 :
Sonko
2026-11-03 23:47:15
0
nabou20120
Nabou💖😝🎶 :
Hummm
2026-11-01 22:17:28
0
aloudabo803
aloudabo803 :
tel
2026-10-31 01:32:35
0
touba1404
touba :
2026-11-03 10:05:52
0
cheikhbayeka1
Baye ka :
Président yalla na yalla taxawoula
2026-10-31 10:30:40
2
rougui.sall43
rougui sall :
2026-11-01 11:09:44
0
fallou.sb
FALLOU SB :
2026-11-01 11:39:04
0
user4298123361223
MameDiarraFaye :
2026-11-02 19:29:01
0
talibe.chikh..maod
TALIBE CHIÈKH. MAODO SARR :
SONKO REK
2026-10-31 19:22:08
4
user221303528055
amadou :
🥰🥰🥰🥰🥰
2026-10-31 10:02:55
0
mareme.sy179
Mareme Sy :
machalla
2026-10-31 08:14:47
0
massmasamba32
massmasambe5🥷 :
😂😂😂😂
2026-10-31 20:52:08
0
salychimerediop
Saly Chimère Diop :
Presi niep bloqué nanioula [Larmes de joie][Larmes de joie]
2026-11-04 23:02:12
0
moussaba8087
Moussa Ba :
2026-10-31 02:04:15
0
To see more videos from user @prsident.senegal, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About