al hamdoulilah macha'Allah ♥️cette vidéo a fait ma journée
deke rewmi desena ay kelifa yu beugg rewmi.
kelifa gui iow tmt Yallah sam la teh aar la!!!
2026-10-31 13:08:07
36
Djiby Barry :
Macha Allah Yalla Ousmane Sonko Yalla nako Yalla may wér ak wérlé saam aar diokh ko rewmi may ko ndam mousseul ko si pékhé noon yii ak occidentaux yii allahouma amine inchallah
2026-10-31 13:08:46
17
MOUHAMED JOOP :
ndayssane xol toyna
2026-10-31 12:10:07
32
☆MASSAMBA》OUSSAÏNOU》GUEYE☆ :
ba 2029 insha allah 🥰bouma kèn wokk nak😏
2026-10-31 12:22:46
41
FATHER~LISCO :
Sonko yalla same la
2026-10-31 14:05:56
0
Dàllu Sonko :
Aamiin ku baax ki yal na la Yàlla sàmm yokk fan wi
2026-10-31 12:11:23
26
daoudajrniang :
Bilahi Souniou wadji 🥰
2026-10-31 12:29:25
38
aboubacarr jallow :
Amin tsars I
2026-10-31 13:56:14
0
Gora Seck :
amine niass yalla na yalla goudeul sa fane té mayela wéer gua féké lèp si barké seydina mouhamet psl.
2026-10-31 12:37:25
17
Mbaybabacar :
Amin
2026-10-31 11:41:05
19
Djim Gaye :
sonko seul
2026-10-31 12:03:38
26
amdy :
kou bakh kou bakh begue la🥰
2026-10-31 13:19:30
7
mamadouibrakide :
machallah allhamdoullahi
2026-10-31 13:34:20
5
marilamin business🇨🇳🇬🇲🇹🇷 :
Ameeeeeeeeeeeeeeeeeinn!! 😭❤️🙏🏻
2026-10-31 13:41:39
0
modou sock :
amine way
2026-10-31 13:36:44
0
yaye fatou ndoye bou sonko :
masala sonko seul
2026-10-31 12:23:12
6
cheikh fall domou TAWA FALL :
sonko kouko laal laalaaké
kilifa yi mom lan beug ❤️❤️❤️
2026-10-31 12:35:00
8
Sénégal rek :
wakhoun na niouko Amadou ba
2026-10-31 12:55:15
1
zeyna12223 :
yalna yalla goudeul sa fane gua féké lép inchallah
2026-10-31 13:56:38
1
MindsetFr✌️ :
Sonko Yalla Nah Goudou Fane Amine 💯💯
2026-10-31 13:49:33
1
Hafis :
Merci beaucoup papa 🥰🥰🥰🥰
2026-10-31 13:30:48
3
sonko président 2029 inch :
amine
2026-10-31 12:54:33
2
To see more videos from user @mouhamed6845, please go to the Tikwm
homepage.