Ah sunu mbeur bi koula bindeul beug nagnla trop mais esk yako bind?❤️🎊🎊😭
2026-10-31 15:23:38
328
MR ABDOU DIOUF :
boudoul won AK Balla Gaye 2 dinga degg magalou yekini Wala gamou yekini ✅
2026-10-31 16:24:35
135
Mbappe.bi :
Départ na Soutoura yalla inchallah
2026-10-31 15:41:50
472
Miss🎀 :
Kiniou bokk tei ma gueun len ko beug sakho illimane fo diar yone la 😭❤️❤️
2026-10-31 15:44:15
1220
🍒 :
Beug nala deh sakho ellimane☺️😊🥳
2026-10-31 15:19:00
1148
Pape🦋BG2🇪🇸💸 :
Oh sama champion bi ❤️💕🫶💪
2026-10-31 21:05:58
0
serignecheikhAhmadou mbacke🦁 :
balla gaye naga deff y'a gui si jam machallah yallah nala yallah defal jam ya rabbi nger yallah balla yaw ak boy niang magui koy dioy ba tay yaw ak siteu naka nouno balla yaw rek lagnou beugeu ya takh tmt may setan lamb wayé combat bi ak lou mëun xew boul ko niakk naka wuut galathie bo baax ndakh ada fass moome rek lathi am wasalam yallah nga am ndam ya rabbi
2026-10-31 15:22:33
113
NDEYA❤😍 :
Niolaaa raww dall❤️😭
2026-10-31 21:17:49
0
La Parisienne ❤️ :
Beugeu nala dei Sakho 😭❤️❤️❤️❤️
2026-10-31 15:23:52
85
MAKHAN🌻 BAYE💦☘️🌿 :
ww champion bi
2026-10-31 21:21:55
0
Lysa baby🦋♥️💍 :
La légende🙂↕️❤️
2026-10-31 17:56:32
21
mame_bousso♎️🌸 :
Mako geuna beug Senegal Sakho elimane❤️🥰
2026-10-31 16:09:09
39
matar Ndiaye :
balla gaye seul
2026-10-31 17:12:52
12
💫MØM£Ï-V£NT🇳🇱🥇 :
Lou way wakh ma dougousi
2026-10-31 16:55:05
1
DAFI STORE BY BOUSSO BALLY🤍 :
Dieul nagn ko le lion
2026-10-31 15:38:59
7
🦋Miss Poulho🩷🧸 :
Yama bayi thi lamb deh barki alkhourane😭❤️❤️🫶🏽
2026-10-31 17:05:40
5
Narra Hann :
way way ♥️♥️
2026-10-31 22:01:03
0
SoXnaa~M~Loh💗 :
Ki dou Sakho Elimane🥹☝🏾
2026-10-31 15:30:51
5
M-C-ndiaye-Appél officiel📱 :
Billahi fii rek lala rawé Noo révérence bi 🥹🤦🏽♂️🙏🏽
2026-10-31 16:34:15
17
Yamz🫧💕 :
Dieul naniou lepp Sakho ilimane 🥺❤️❤️❤️
2026-10-31 19:34:50
7
10!!🧼 :
Soumala diapè😂💪🏿
2026-10-31 15:47:53
11
Samba seck🫰🏿🏄♂️ :
Danou force 😂⚔️
2026-10-31 16:06:20
34
Ndeyekane🇸🇳🏅🇺🇸déliceDkyra :
Noko beurer bakhna comme Nonou rek ♥️🥰
2026-10-31 20:22:35
5
𝐓𝐬𝐠𝐧.²3⁵🕷️ :
Day Daw rék BG2 ba fadiare 💙💛
2026-10-31 15:40:12
5
To see more videos from user @ballagaye2_, please go to the Tikwm
homepage.