yalla nalén yalla yereume té kharélén aldiane firdawsi ak mbolé dioulit
2026-10-31 16:06:10
15
kebefaliloufalilo :
amine Amine
2026-10-31 18:30:29
1
YayùPapis🥰Mrs D❤️💍 :
Oh Yallna len yalla yeureum té xalén Aldjana
2026-10-31 18:24:05
4
mbaye sall :
اللهم اغفر لهما ورحمهما 🙏🏼🤲
2026-10-31 18:29:03
2
Diazz_Officiel :
Ndeysane yallanalén yalla yeureum té kharélén aldiana Rouba Ndao mom khamnako nio bokone di diangue Lycée Gueoul Mafall sama copin yallanala yalla may kholou mougne amine
2026-10-31 17:42:38
2
MD CR7 El bicho💚🤍🇸🇳🫶 :
Yalla nako yalla yereum
2026-10-31 17:07:48
2
chachaMG :
Walakhi lo wakh si sén mbakh amna lou déss yalla na yalla yeureum lénn the diégual lénn bb bi yalla tékk ko lokho🙏🙏🙏
2026-10-31 17:23:50
3
wwww :
yallana Naléne yalla kharé adiana firdawsi
2026-10-31 18:06:00
2
Mrs mbaye sangu yarame ❤️👌🏻 :
Sama khol bi meti na😭
2026-10-31 18:07:55
1
Interdit :
fi si europe amena carbon yo khamenè pour lakk yap la dou dougou si keur si je pense que lolou la 2 tipe de carbon mo ame
2026-10-31 17:02:17
2
50 cen :
ndeysan soriwuma bilahi
2026-10-31 17:31:53
1
ibrahimadiene45 :
🙏🙏🙏🙏🙏
2026-10-31 17:44:37
2
SECK BOU SOKHNA MOMY MBACKE :
ndiasse sall kou bakh bilahi foko guis dafay retane ho yalena len yalla yeureum way te khare len aldiana ak rouba ndaw
2026-10-31 16:47:19
2
rokhaya boye :
amine amine amine amine😭😭😭😭
2026-10-31 18:10:29
1
ndeyabouserignefallou4 :
Paix à leurs âmes
2026-10-31 15:47:16
6
mamadykouyate310 :
MI CONDOLEEZZA HA TODOS FAMILIA COMPARAMOS DOLOR DIOS LOS BENDIGA
2026-10-31 17:44:21
1
massamba 🇸🇳🇮🇹 :
repose en paix frr ndiasse et sa femme Rouba ndaw
2026-10-31 15:42:27
5
KANY SALIOU :
amine
2026-10-31 15:35:04
3
Bigue❤️💕❤️Lahat :
yalla nalene yalla yereume te kharelene aldianay firdawsi ndeysane 😭😭😭
2026-10-31 16:35:41
2
50 cen :
metina torop yalna leen yalla yereum
2026-10-31 17:35:29
1
Marieme Ndim :
paix à leurs âmes 😭😭
2026-10-31 17:01:45
1
773153509 :
yallna yalla douliy lenn yaremande AK leur
2026-10-31 15:52:22
2
fallou kharr :
yalla nalén yalla yerem
2026-10-31 16:51:59
1
To see more videos from user @jacobpost84, please go to the Tikwm
homepage.