Bima amé 4ans lagne ma mayé kigne ma mayonne guagnou na domam sonal ma ba ma guene keur gua mangui ni sma copine moma yobou sen keur on dirait awma famille dou yaye dou pape dou mak suis seul viol skh defnagne mko mais menouma wax ak kéne 😔💔
2026-10-31 23:46:05
1460
zeynaexwally :
Bb massa 🙏🙏
2026-10-31 23:05:49
842
🖤Princesse 👸🏿 noir 🖤🥳✨ :
Li guay dou ndou ni lay dou ndou bly dama meunoul déf liguay déf rk😭😭😭
2026-10-31 22:41:42
718
UNE CHICORIENNE_💜📿 :
xana yén gneup yéneu bokk lingéni doundou courage à vous
2026-10-31 23:17:21
474
aïsha saliou :
Wollahi si pouvais faire lingay deff nii ma deff ko dama meussa sonou ci sama famille di deff Louma meune ak Louma meunoul j’ai même pas encore eu mon BAC mais je fais tout pour ma maman et mes tites sœurs Magui actuellement nekk situation boo khamni sama yaye bousi défone benneu effort bou mdaw lepp régler wou mais Nena yoonam nekoul ci Mane
2026-10-31 22:15:41
1393
Boy bii✌🏾 :
Mais pourquoi lii eupe sii situation djigeune rk lay daaal Masta yalla bakha na🙏🥹💔
2026-10-31 23:12:13
168
Dark Queen🤎🖤👑 :
J’ai vue une vidéo d’un gas qui disait que la plupart de notre génération sont dépressifs mais walay il a raison avec tous ce que je vois sur les réseaux sociaux vraiment ça devient inquiétant qu’Allah nous viennent en aide 🙏🏿🙏🏿
2026-10-31 23:56:27
250
user2180161745384 :
Courage sister lep dina diex Inchallah
2026-11-01 05:07:23
0
une_zeyna❤💍 :
La jeunesse d'aujourd'hui est mentalement épuisée. Nous portons une charge mentale que beaucoup ne voient pas : la peur de l'échec, la pression de réussir, les responsabilités familiales, les difficultés financières, les attentes des autres et l'incertitude face à l'avenir. On réfléchit trop, on anticipe tout, on se met une pression énorme et même au repos, notre cerveau ne s'arrête jamais. On sourit, on plaisante, on dit que tout va bien, alors qu'à l'intérieur, on est parfois à bout.
2026-11-01 00:43:59
69
Fatou Camara :
salalahou allah mouhamad ❤️❤️
2026-10-31 23:07:45
162
Thioro saliouh :
Li dh lay doundou Bilay walay 😭😭
2026-10-31 22:37:57
355
awafall :
Yalna yalla maye la kholou mougne 🥰🥰🥰
2026-10-31 22:37:03
874
sophiasonko5 :
Ndeyssane man ak iow nio niro situation makoy doundou ni bilahi😭😭😭😭😭😭 ms yalla bakhna 😭😭😭😭
2026-11-01 05:09:56
0
king couture :
Guénél li nekeu sa xol. Ndakh nga fékh li diar diar la rek. Dey diekh Inchalla. Mounial rek. Yalla guiss na lep 🥰🥰
2026-10-31 22:03:55
542
محمد حيدر :
yalla bakhna
2026-11-01 04:46:44
0
thiatou Yayam ak bayam :
Courage sister
2026-11-01 04:21:54
0
Biraneniang :
gour gour lou reck yalla bakhenne yallnaa yalla takhwoulaa
2026-11-01 03:59:15
0
THiaw star lutteur :
Lobege
2026-11-01 03:47:43
0
bordeaulais :
Les commentaires me font mal mais courage les sisters 😭🙏
2026-11-01 00:10:16
60
ꨄ︎𝓛𝔂𝓷𝓭𝓪💕ᵈᵐ🦋𝓑𝓪𝓲𝓵𝓪🐆 :
Regarde comment tu es belle 🥰ne pleure pas 🥹
2026-11-01 02:00:18
52
Ngomez :
Nèkke lène àÿ niit tè correct. Dom sou correctè, domou nieuppe lèyi doneu. Nieuppà lèye beuggue diappalè. Way sou fèkkè nii dà nguéne beuggue tèlà ame indépendance, Lou parents yi wax nguèneu tèggui ko, bilahi Sii nakkar rèk nguéyi nèk. Dèllo lène sèn xèl si Yalla, dii djouli Lou Bari, tèk sii respecté parents yi. Courage
2026-11-01 00:15:03
38
La tigresse 🐅 :
Courage😞😞
2026-10-31 21:09:26
77
bb Éva 🥰 :
bilay comprend nala lou métti lay doundou ms diouli rek lako fadié di diouk fadiar di diouli fékhé ba wakhtou diouli boumla raw di diouk di diouli 3h du matin wét ak sa brome diis ko sy sokhla mane samay problème biéndéff bou yalla sakk khamouko yalla rek lasiy wakhtanal môme rek momasi métti na ms sante yalla alkhamdoulilah
2026-10-31 22:59:41
123
Vie✨🤍 :
Dagua am courage di wakh rek linguay doundou ni walahi wakh sa nehoul rek massa
2026-10-31 23:28:59
56
Oulychou🥰 :
Même mane kene beugouma 🥰
2026-11-01 01:21:03
26
To see more videos from user @adja.fall354, please go to the Tikwm
homepage.