photo bi nga taff deh sama makk la dafa guéneuh adouna nianal lenn ko cheikh mbacké la toudou
2026-11-01 10:52:04
376
Beug Saliou :
Thieuy cheikh Ibra amna loumou déf si ay talibéme
2026-11-01 08:17:43
702
YALLAH dou fay wakh bayi dieuf :
yalla dou fay wakh bayi dieuff
2026-11-01 08:21:00
328
Badara :
Wakh diéfi nékeu rk bou kharé badr amatone taydji sax Baay Fall yi niokoy kharé ko
2026-11-01 06:28:38
271
Nittou Bamba🫀🥹❤️ :
Barkép Cheikh Hamsa 🥹💙
2026-11-01 09:25:36
209
Madiop Faye :
Cheikh Ibra Fall liko diné diaral néwna nioumouko diaral
2026-11-01 11:51:39
131
soldaro nikhma ndigual 🦓 :
bilahi ko an anbak cheikh Ibrahim do ragual bilahi
2026-11-01 08:41:24
100
Ćaam_Baay_Faal🇸🇳 :
Jarama Maam Seex Ibrahima Faal Baabul Muridina
2026-11-01 10:59:02
32
شيخ باي فال :
say bou féké wakh diou rafete rk ak dieuf diou rafete ak gueum sunu borom baye fall fall yéko euplou niépou
2026-11-01 13:27:56
28
Bamba rsl :
Koudoul baye fall baye fall mola geunn beug dinei dji gniy wax fi dinei dji diaralou leinn sein alal ak seinn bakann
2026-11-01 10:47:03
41
S MBACKÉ NJÃÃY ✪ :
Mame Cheikh Ibrahim 🏁
2026-11-01 10:38:58
64
Habib 🇸🇳Marouane ⚡️ :
Fall rouss nala dh😪Démall gëstou dji watt cheikh ibra est que xamnga ci ndiabottou cheikh ibra gui Amna Niou ci dioulli ta lolou da am louko warall délénn gëusstou
2026-11-01 11:48:56
26
bakheyaye064 :
Moma dé mame lampou
2026-11-01 07:26:48
65
sow sénégalai 🇸🇳100%100 :
linga wakh dh gniko khame barinagne wayé douniou nangou baye fall diouliwoul dh wayé kholba yalla rk mosané Ak mouhamath
2026-11-01 11:05:13
44
𝑀𝐼𝐷𝐴𝐷𝐼 BËUG YALLA💙🤍🏁 :
ap baye fall dou ragal
2026-11-01 11:45:27
28
Mouhamadou Kébé Diouf :
Sallalahou Hala Muhammad
2026-11-01 09:19:12
40
Ndiaga sarr :
sallalahou Allah mouhamed ❤️
2026-11-01 15:30:47
7
bbndeyeseye1 :
صل الله عليه وسلم
2026-11-01 11:35:42
15
DIONE DEUG 🔴⚫️ :
Soudonn badr daniouyy dhé bilay
2026-11-01 10:31:18
19
Beug Assadoul Xadim❤️🙏🏾 :
Ba Kerook Yalla di fay wax bayyi jeuff🏁❤️
2026-11-01 11:52:43
25
ibrahima🇸🇳🇲🇷🇲🇦🇪🇸👨💻 :
Nenan yalla dou fay wakh bayi dieuf ta nit ñi daniouy wakh rk ms bou dieuf dioté niépou daw
2026-11-01 06:52:48
48
cheikh issa :
Diërëdiëfé Brom touba
2026-11-01 02:55:52
43
Fall pro 📸✨ :
Kenn dou fay wakh di bayi dieufff [Réconfortant]
2026-11-01 11:12:05
11
Notre Sénégal 💯🥰 :
Ahmadou 🥰🥰🥰
2026-11-01 06:22:59
30
ABABACAR SADIKH :
Diarama MameCheikh Ibrahima Fall
2026-11-01 11:24:03
9
To see more videos from user @alwahabtravel0, please go to the Tikwm
homepage.