@.un.homme.repenti: Dama am benn laaj, ndax dañuy wax Kamil (Alxuraan) kenn du ko laal te amulo ndiapou. Ma war naa dem jàngi, waaye robinet bi dafa tëju léegi. Nak, si la jëlal xérou time bi ma time nakh lima def wèrna wala Répondez dans les commentaires #Islam #Allah #Foi #Quran #Dua @Mouhammad Fall ✪ @al badrii