@ambassadeursbs: Épisode 18 #episode Ambassadeur Ak Mouride yii 😂#cimetiere #mouridetidianelayén❤️alkhamdoulilah #senegalaise_tik_tok #serignebabacarsy

Ambassadeur Serigne Babacar ✪
Ambassadeur Serigne Babacar ✪
Open In TikTok:
Region: SN
Sunday 01 November 2026 10:21:18 GMT
199478
45022
1178
389

Music

Download

Comments

bass.mou.mame.kha
17 Novembre 🎂❤️🙏✨🎂🎂 :
baye fall si bopam nio gatt xél 😂😂
2026-11-01 11:04:23
2567
evabusiness58
EVA BUSINESS 🎽🩱👖👙👗 :
mouride bi daguakoy guiss rek kham ni si cimetière bi la fanane kholal bopp bi 🤌😂😂😂
2026-11-01 10:27:17
1163
boromtoubaamoulmorom102
borom touba amoul morom :
aldiana sax nilay deme
2026-11-01 12:16:46
345
thiatlacapricieuse0
Une Babacarienne🥰 :
xamouniou xel dall
2026-11-01 10:50:15
131
shoufvrasoul
Talibé cheikh 🙏❤️ :
Nonou laniou deff tivaouane 3h du matin laniou nieww gnii 😂😂😂
2026-11-01 11:37:48
403
leytyndiaye0
Leyty Ndiaye :
Baye Fall yii déh nio meune nieupp cii liguéy pastef bou matt seuk lagn cii wanè. 🙏
2026-11-01 12:35:11
183
cheikh.ndiaye526
cheikh ndiaye :
Boy le kagne ngay bayi mouride yi😂
2026-11-01 11:15:31
441
eyhdhdvdvdbdbdbdbdb
😍😍😍 :
tidjane yii aye nalaw Molène sinal danguèn beug nalaw 😂😂
2026-11-01 11:34:59
102
dieng778557558constructi
dieng construction 778557558 :
non danhou don wasifa
2026-11-01 15:24:23
0
universelvision1
Universel Vision.1 :
li dé la cimetière yeup di casse légui la diougué ci armal Yeumbeul yi 8h Bay fall diékhal liguey bi
2026-11-01 12:02:39
214
skinnydior24
🇸🇳SKINNY DIOR 🤍💜 :
Même Malika tay nonou leuh dama décourager 07h laniou nieuw fekk baye fall yi paré 😭
2026-11-01 12:40:51
125
fayefa43
Talibé cheikh ❤️ :
Dagnio piéger dh😂 mais mome téla yéwou la wakh dh😂 mane dh ma yéwou 5h diouk diouli 6h werdd nieuw si cimetière yi 6h guisouma daraa😂😂 non mais yéna meune yalna yalla fay yiww🙏🙏
2026-11-01 12:02:22
121
momoledg1
Momo Mbemgue :
Salalahou Ala moukhamad
2026-11-01 11:50:01
88
unmourid7
un mouride :
Yallna diamou yague ❤️❤️❤️
2026-11-01 11:16:42
65
abdallahibninsa
Abdou Barham Abdou Insa :
Li dou tela yeewu ndiakhlaf bou eup la . De nguen seuss trop 7 h ngay nieuw 3h ken khamoul li bane khettou farlou. yallah nalen Yallah faye same leen defaalen diam saadatouna daarayni
2026-11-01 13:08:40
88
laydisha3
♥️Laydisha♥️🫶🍀😘 :
Yalla nalène yalla sam si barké Mouhamed (psl)🥰
2026-11-01 11:21:30
233
lhomme7021
L’araignée 🕷️🕸️ :
Nonou lan def armel keur massare yi 😭
2026-11-01 11:12:45
164
user292982910888
' président 2029 inchallah :
mame maodo moy bamba balba moy maodo
2026-11-01 14:03:08
20
salimdioufmufc
Salim Diouf Mufc :
Yen daguene guate xel yiw bi gneupa si wara am mais bg ko jeul yen kassé sama xol bi jehh nantakk way😂
2026-11-01 11:40:42
34
m2a4x6
M@xondiaye,The Wedding planner :
Gni kayy Khél amougnouko bimay diogué dianguou layyénn yeuh laguiss gnou commencer 😂😂😂
2026-11-01 12:24:38
35
papemoussa556
PAPE MOUSSA BSB :
Défa melni wadji téla yéwou laniou wakh wala ma deguoul😳😳😳😳aider moi svp
2026-11-01 10:58:05
86
makhoubusnes7
MAKHOUBUSNES :
mane dhé 5h du matin lafa nieuw fék cimetière séte dama warou sakh mane thieuy baye fall yi 🤔
2026-11-01 10:32:35
52
linconue27
L’inconnu..!👻 ✪ :
Niome nénagne danio sipp nélaw sakh kone founiou nékone 😂🤦🏾‍♂️
2026-11-01 14:04:13
7
papaalcantara6
PAPA 🦀 ALCANTARA ⚽️❤️✌️ :
Nioune kay daniouy télà yéwou 😂yéna gaw rek machallah 🤩mais solution bi kay moy niou bokk fanane si bounte
2026-11-01 13:08:57
15
khaliloulah970
BOROM DAROU❤️ :
Talibe cheikh kon sakh dina nélaw[Innocent]
2026-11-01 12:15:06
10
To see more videos from user @ambassadeursbs, please go to the Tikwm homepage.

Other Videos


About